Al-Hujurat · 1/18
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hujurat
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تُقَدِّمُوا بَيْنَ يَدَيِ اللَّهِ وَرَسُولِهِ ۖ وَاتَّقُوا اللَّهَ ۚ إِنَّ اللَّهَ سَمِيعٌ عَلِيمٌ ١
Transliteration
Yaa ayyuhal lazeena aamanoo la tuqaddimoo baina yada yil laahi wa Rasoolihee wattaqul laah; innal laaha samee`un `Aleem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Eey yéen ñi gëm ! Bu leen di jiitu Yàllaa kub Yonentaam. Te ngeen ragal Yàlla di ko watandiku. Ndax Yàlla ku dégg la kuy xam la.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 1-3 — Simoore Al-Hujurat
1يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تُقَدِّمُوا بَيْنَ يَدَيِ اللَّهِ وَرَسُولِهِ ۖ وَاتَّقُوا اللَّهَ ۚ إِنَّ اللَّهَ سَمِيعٌ عَلِيمٌ
Eey yéen ñi gëm ! Bu leen di jiitu Yàllaa kub Yonentaam. Te ngeen ragal Yàlla di ko watandiku. Ndax Yàlla ku dégg la kuy xam la.
2يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَرْفَعُوا أَصْوَاتَكُمْ فَوْقَ صَوْتِ النَّبِيِّ وَلَا تَجْهَرُوا لَهُ بِالْقَوْلِ كَجَهْرِ بَعْضِكُمْ لِبَعْضٍ أَن تَحْبَطَ أَعْمَالُكُمْ وَأَنتُمْ لَا تَشْعُرُونَ
Eey yéen ñi gëm! Bu leen di yékkati seen kàddu ci kaw kàddug Yonenta bi, bu leen koy jollmbeeru ay wax, kon ni ngeen di jooruwantee bu (ngeen ko defee), yéen nangay sippi seeni jëf te yëguleen ko.
3إِنَّ الَّذِينَ يَغُضُّونَ أَصْوَاتَهُمْ عِندَ رَسُولِ اللَّهِ أُولَٰئِكَ الَّذِينَ امْتَحَنَ اللَّهُ قُلُوبَهُمْ لِلتَّقْوَىٰ ۚ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَأَجْرٌ عَظِيمٌ
Ñay suufeel seeni kàddu ci Yonenta bi ñooñee la Yàlla nattu seen xol (fekk ko mu jooy jëm ci ragal Yàlla). Dana ñu am njégël ak pey gu màgg.
Al-HujuratFihi Alxuraan
18Aaya
MedinanRevelation
1Aaya
Tekki — Al-Hujurat 1
Simoore Al-Hujurat Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Eey yéen ñi gëm ! Bu leen di jiitu Yàllaa…Simoore Aaya 1/18 — Simoore Al-Hujurat الحجرات (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hujurat Dégg, Simoore Al-Hujurat Tekki, Simoore Al-Hujurat mp3, Simoore Al-Hujurat pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Al-Hujurat
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Wednesday, September 30, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


