Al-Maida · 89/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
لَا يُؤَاخِذُكُمُ اللَّهُ بِاللَّغْوِ فِي أَيْمَانِكُمْ وَلَٰكِن يُؤَاخِذُكُم بِمَا عَقَّدتُّمُ الْأَيْمَانَ ۖ فَكَفَّارَتُهُ إِطْعَامُ عَشَرَةِ مَسَاكِينَ مِنْ أَوْسَطِ مَا تُطْعِمُونَ أَهْلِيكُمْ أَوْ كِسْوَتُهُمْ أَوْ تَحْرِيرُ رَقَبَةٍ ۖ فَمَن لَّمْ يَجِدْ فَصِيَامُ ثَلَاثَةِ أَيَّامٍ ۚ ذَٰلِكَ كَفَّارَةُ أَيْمَانِكُمْ إِذَا حَلَفْتُمْ ۚ وَاحْفَظُوا أَيْمَانَكُمْ ۚ كَذَٰلِكَ يُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمْ آيَاتِهِ لَعَلَّكُمْ تَشْكُرُونَ ۝٨٩
Laa yu`aakhizukumul laahu billaghwi feee aimaanikum wa laakiny ya`aakhizukum bimaa `aqqattumul aimaana fakaf faaratuhooo it`aamu `asharati masaakeena min awsati maa tut`imoona ahleekum aw kiswatuhum aw tahreeru raqabatin famallam yajid fa Siyaamu salaasati aiyaam; zaalika kaffaaratu aimaanikum izaa halaftum; wahfazooo aimaanakum; kazaalika yubaiyinul laahu lakum Aayaatihee la`allakum tashkuroon
📖 Tekkim Wolof
Yàlla duleen jàppe ngiñ yi ngeen di kafe, waaye Dana leen jàppe ngiñ yi dëggu ci yéen. Te ñoom, la ñuy jéggaloo mooy leel fukki néew-ji-doole [ci ñam wa ngeen di faral a dundale seen njaboot], mbaa jox leen ay yére, walla goreel jaam. Ku ko mënul, na woor ñetti fan. Loola mooy na ñuy jéggaloo seen ngiñ ya ngeen waate [lu jaaduwul]. nangeen sàmm seen ngiñ, nii la leen Yàlla di leerale ay ndigalam ndax xéy-na ngeen gërëm Ko [delloo njukkal] !
🎧 Dégg

📜 Aaya 87-91 — Al-Maida

87يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تُحَرِّمُوا طَيِّبَاتِ مَا أَحَلَّ اللَّهُ لَكُمْ وَلَا تَعْتَدُوا ۚ إِنَّ اللَّهَ لَا يُحِبُّ الْمُعْتَدِينَ
Éy yéen ñi gëm : buleen araamal yu sell ya leen Yàlla daganal. Te it buleen jéggi dayo, Yàlla soppul ñiy jéggi dayo.
88وَكُلُوا مِمَّا رَزَقَكُمُ اللَّهُ حَلَالًا طَيِّبًا ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ الَّذِي أَنتُم بِهِ مُؤْمِنُونَ
Lekkleen li leen Yàlla wërsëgale muy li dagan te sell. Te nangeen ragal Yàlla ji ngeen gëm.
89لَا يُؤَاخِذُكُمُ اللَّهُ بِاللَّغْوِ فِي أَيْمَانِكُمْ وَلَٰكِن يُؤَاخِذُكُم بِمَا عَقَّدتُّمُ الْأَيْمَانَ ۖ فَكَفَّارَتُهُ إِطْعَامُ عَشَرَةِ مَسَاكِينَ مِنْ أَوْسَطِ مَا تُطْعِمُونَ أَهْلِيكُمْ أَوْ كِسْوَتُهُمْ أَوْ تَحْرِيرُ رَقَبَةٍ ۖ فَمَن لَّمْ يَجِدْ فَصِيَامُ ثَلَاثَةِ أَيَّامٍ ۚ ذَٰلِكَ كَفَّارَةُ أَيْمَانِكُمْ إِذَا حَلَفْتُمْ ۚ وَاحْفَظُوا أَيْمَانَكُمْ ۚ كَذَٰلِكَ يُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمْ آيَاتِهِ لَعَلَّكُمْ تَشْكُرُونَ
Yàlla duleen jàppe ngiñ yi ngeen di kafe, waaye Dana leen jàppe ngiñ yi dëggu ci yéen. Te ñoom, la ñuy jéggaloo mooy leel fukki néew-ji-doole [ci ñam wa ngeen di faral a dundale seen njaboot], mbaa jox leen ay yére, walla goreel jaam. Ku ko mënul, na woor ñetti fan. Loola mooy na ñuy jéggaloo seen ngiñ ya ngeen waate [lu jaaduwul]. nangeen sàmm seen ngiñ, nii la leen Yàlla di leerale ay ndigalam ndax xéy-na ngeen gërëm Ko [delloo njukkal] !
90يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِنَّمَا الْخَمْرُ وَالْمَيْسِرُ وَالْأَنصَابُ وَالْأَزْلَامُ رِجْسٌ مِّنْ عَمَلِ الشَّيْطَانِ فَاجْتَنِبُوهُ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ
Éy yéen ñi gëm ! [xamleen ne] sàngara, wure, xerëm ak seen banti gisaane, nekkuñu lu dul sobe su jóge ci jëfi [Séytaane]. Nangeen leen moytu, xéy-na kon ngeen texe.
91إِنَّمَا يُرِيدُ الشَّيْطَانُ أَن يُوقِعَ بَيْنَكُمُ الْعَدَاوَةَ وَالْبَغْضَاءَ فِي الْخَمْرِ وَالْمَيْسِرِ وَيَصُدَّكُمْ عَن ذِكْرِ اللَّهِ وَعَنِ الصَّلَاةِ ۖ فَهَلْ أَنتُم مُّنتَهُونَ
Séytaane bëggul lu dul tàbbal ci seen diggante nooneel ak mbañeel, jaare ko ci sàngara ak wure te it dox seen diggante ak fàttaliku Yàlla ak julli. Moo ndax dungeen leen bàyyi ?
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
89Aaya

Tekki — Al-Maida 89

Simoore Al-Maida Aaya 89 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla duleen jàppe ngiñ yi ngeen di kafe, waaye Dana…

Simoore Aaya 89/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 87–91. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers