Qaf · 37/45
Tekki Waxtaan — Qaf
إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَذِكْرَىٰ لِمَن كَانَ لَهُ قَلْبٌ أَوْ أَلْقَى السَّمْعَ وَهُوَ شَهِيدٌ ۝٣٧
Inna fee zaalika lazikraa liman kaana lahoo qalbun aw alqas sam`a wa huwa shaheed
📖 Tekkim Wolof
Ak fàttali nekk na ci biir loolu ñeel képp ku am ub xol, tey déglu booleek teewlu doon seede.

🎧 Dégg


📜 Aaya 35-39 — Qaf

35لَهُم مَّا يَشَاءُونَ فِيهَا وَلَدَيْنَا مَزِيدٌ
Danañu fa am lépp lu leen soob. Te am Nanu ndollen.
36وَكَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّن قَرْنٍ هُمْ أَشَدُّ مِنْهُم بَطْشًا فَنَقَّبُوا فِي الْبِلَادِ هَلْ مِن مَّحِيصٍ
aka bari ay xeet yu Nu faagaagaloon, ci ña leen fi jiituwoon, te ëppoon leen kàttan fuuf. Réew mu nekk dem nañu fa, mu fees di rawe.
37إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَذِكْرَىٰ لِمَن كَانَ لَهُ قَلْبٌ أَوْ أَلْقَى السَّمْعَ وَهُوَ شَهِيدٌ
Ak fàttali nekk na ci biir loolu ñeel képp ku am ub xol, tey déglu booleek teewlu doon seede.
38وَلَقَدْ خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا فِي سِتَّةِ أَيَّامٍ وَمَا مَسَّنَا مِن لُّغُوبٍ
Man Yàlla, Maa bind asamaan yeek suuf ak li nekk ci seen diggante diirub juróom-benni fan, te Amuma ci benn coono.
39فَاصْبِرْ عَلَىٰ مَا يَقُولُونَ وَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ قَبْلَ طُلُوعِ الشَّمْسِ وَقَبْلَ الْغُرُوبِ
Nangay muñ li ñuy wax : te nangay kañ di sàbbaal sa Boroom di ko sant balaa jant bi fenk ak balaa muy so ;
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — Qaf 37

Simoore Qaf Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak fàttali nekk na ci biir loolu ñeel képp ku…

Simoore Aaya 37/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers