Qaf · 36/45
Tekki Waxtaan — Qaf
وَكَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّن قَرْنٍ هُمْ أَشَدُّ مِنْهُم بَطْشًا فَنَقَّبُوا فِي الْبِلَادِ هَلْ مِن مَّحِيصٍ ۝٣٦
Wa kam ahlaknaa qablahum min qarnin hum ashaddu minhum batshan fanaqqaboo fil bilaad, hal mim mahees
📖 Tekkim Wolof
aka bari ay xeet yu Nu faagaagaloon, ci ña leen fi jiituwoon, te ëppoon leen kàttan fuuf. Réew mu nekk dem nañu fa, mu fees di rawe.

🎧 Dégg


📜 Aaya 34-38 — Qaf

34ادْخُلُوهَا بِسَلَامٍ ۖ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْخُلُودِ
Dugguleen ko ci jàmm ak tal”. Te loolu mooy sax ba fàww (Àjjana) !
35لَهُم مَّا يَشَاءُونَ فِيهَا وَلَدَيْنَا مَزِيدٌ
Danañu fa am lépp lu leen soob. Te am Nanu ndollen.
36وَكَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّن قَرْنٍ هُمْ أَشَدُّ مِنْهُم بَطْشًا فَنَقَّبُوا فِي الْبِلَادِ هَلْ مِن مَّحِيصٍ
aka bari ay xeet yu Nu faagaagaloon, ci ña leen fi jiituwoon, te ëppoon leen kàttan fuuf. Réew mu nekk dem nañu fa, mu fees di rawe.
37إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَذِكْرَىٰ لِمَن كَانَ لَهُ قَلْبٌ أَوْ أَلْقَى السَّمْعَ وَهُوَ شَهِيدٌ
Ak fàttali nekk na ci biir loolu ñeel képp ku am ub xol, tey déglu booleek teewlu doon seede.
38وَلَقَدْ خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا فِي سِتَّةِ أَيَّامٍ وَمَا مَسَّنَا مِن لُّغُوبٍ
Man Yàlla, Maa bind asamaan yeek suuf ak li nekk ci seen diggante diirub juróom-benni fan, te Amuma ci benn coono.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — Qaf 36

Simoore Qaf Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : aka bari ay xeet yu Nu faagaagaloon, ci ña leen…

Simoore Aaya 36/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers