Al-Qamar · 40/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ ٤٠
Transliteration
Wa laqad yassarnal Quraana liz zikri fahal mim muddakir
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yombal Nanu Alxuraan ngir ñu fàttalikoo ca. Mo ndax kon kenn dana ca jàjjoo ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 38-42 — Simoore Al-Qamar
38وَلَقَدْ صَبَّحَهُم بُكْرَةً عَذَابٌ مُّسْتَقِرٌّ
Mu foog leen, suba teel, ak mbugël mu ñu dootul tàggool.
39فَذُوقُوا عَذَابِي وَنُذُرِ
Mosleen Samak mbugël ak Samag xuppe.
40وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal Nanu Alxuraan ngir ñu fàttalikoo ca. Mo ndax kon kenn dana ca jàjjoo ?
41وَلَقَدْ جَاءَ آلَ فِرْعَوْنَ النُّذُرُ
Nitu Firawna ya ñoom it, xupp ga dikkaloon na leen.
42كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا كُلِّهَا فَأَخَذْنَاهُمْ أَخْذَ عَزِيزٍ مُّقْتَدِرٍ
Ñoom dañoo weddi faf sunu kàddu yépp. Nu daldi leen faagaagal, ak doole.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
40Aaya
Tekki — Al-Qamar 40
Simoore Al-Qamar Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yombal Nanu Alxuraan ngir ñu fàttalikoo ca. Mo ndax kon…Simoore Aaya 40/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








