Al-Qamar · 39/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
فَذُوقُوا عَذَابِي وَنُذُرِ ۝٣٩
Fazooqoo `azaabee wa nuzur
📖 Tekkim Wolof
Mosleen Samak mbugël ak Samag xuppe.

🎧 Dégg


📜 Aaya 37-41 — Simoore Al-Qamar

37وَلَقَدْ رَاوَدُوهُ عَن ضَيْفِهِ فَطَمَسْنَا أَعْيُنَهُمْ فَذُوقُوا عَذَابِي وَنُذُرِ
Dañoo, sàkkoo saay-saaye ganam ña. Nu daldi fatt seen gët ne leen “Mosleen Sama mbugël ak Samak xupp”.
38وَلَقَدْ صَبَّحَهُم بُكْرَةً عَذَابٌ مُّسْتَقِرٌّ
Mu foog leen, suba teel, ak mbugël mu ñu dootul tàggool.
39فَذُوقُوا عَذَابِي وَنُذُرِ
Mosleen Samak mbugël ak Samag xuppe.
40وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal Nanu Alxuraan ngir ñu fàttalikoo ca. Mo ndax kon kenn dana ca jàjjoo ?
41وَلَقَدْ جَاءَ آلَ فِرْعَوْنَ النُّذُرُ
Nitu Firawna ya ñoom it, xupp ga dikkaloon na leen.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — Al-Qamar 39

Simoore Al-Qamar Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mosleen Samak mbugël ak Samag xuppe.

Simoore Aaya 39/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers