Ar-Rahman · 49/78
Tekki Waxtaan — Ar-Rahman
فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ ۝٤٩
Fabi ayyi aalaaa`i Rabbikumaa tukazzibaan
📖 Tekkim Wolof
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 47-51 — Ar-Rahman

47فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
48ذَوَاتَا أَفْنَانٍ
Yu am car yu dëll meññ gacc.
49فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
50فِيهِمَا عَيْنَانِ تَجْرِيَانِ
Am na fa ñaari bëti ndox yuy daw-dawaan.
51فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
49Aaya

Tekki — Ar-Rahman 49

Simoore Ar-Rahman Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a…

Simoore Aaya 49/78 — Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rahman Dégg, Ar-Rahman Tekki, Ar-Rahman mp3, Ar-Rahman pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.

Alxuraan bu Tedd bi

Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers