At-Talaq · 11/12
Tekki Waxtaan — At-Talaq
رَّسُولًا يَتْلُو عَلَيْكُمْ آيَاتِ اللَّهِ مُبَيِّنَاتٍ لِّيُخْرِجَ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ مِنَ الظُّلُمَاتِ إِلَى النُّورِ ۚ وَمَن يُؤْمِن بِاللَّهِ وَيَعْمَلْ صَالِحًا يُدْخِلْهُ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا ۖ قَدْ أَحْسَنَ اللَّهُ لَهُ رِزْقًا ۝١١
Rasoolany yatloo `alaikum aayaatil laahi mubaiyinaatil liyukhrijal lazeena aamanoo wa `amilus saalihaati minaz zulumaati ilan noor; wa many yu`mim billaahi wa ya;mal saalihany yudkhilhu jannaatin tajree min tahtihal anhaaru khaalideena feehaa abadan qad ahsanal laahu lahoo rizqqq
📖 Tekkim Wolof
ab Yonent buy jàng ci yéen Laayay Yàlla mu leer nàññ, ngir mu génne ñi gëm tey jëfe yiw cig lëndëm jëme leen ci leer. Képp ku gëm Yàlla tey jëfe yiw, (Yàlla) dana ko tàbbal Àjjana joo xam ne ay dex ñooy daw ci suufam, ñu béel fa Yàlla may ko fa xéewal gu jekk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-12 — At-Talaq

9فَذَاقَتْ وَبَالَ أَمْرِهَا وَكَانَ عَاقِبَةُ أَمْرِهَا خُسْرًا
Mosnañu musibam seeni mbir. Ñu mujj yàqule.
10أَعَدَّ اللَّهُ لَهُمْ عَذَابًا شَدِيدًا ۖ فَاتَّقُوا اللَّهَ يَا أُولِي الْأَلْبَابِ الَّذِينَ آمَنُوا ۚ قَدْ أَنزَلَ اللَّهُ إِلَيْكُمْ ذِكْرًا
Yàlla waajal na leen mbugël mu tar. Kon book ragal-leen Yàlla, yéen woroom xel yi, natt gëm. Yàlla wàcce na ci yéen ag fàttali,
11رَّسُولًا يَتْلُو عَلَيْكُمْ آيَاتِ اللَّهِ مُبَيِّنَاتٍ لِّيُخْرِجَ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ مِنَ الظُّلُمَاتِ إِلَى النُّورِ ۚ وَمَن يُؤْمِن بِاللَّهِ وَيَعْمَلْ صَالِحًا يُدْخِلْهُ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا ۖ قَدْ أَحْسَنَ اللَّهُ لَهُ رِزْقًا
ab Yonent buy jàng ci yéen Laayay Yàlla mu leer nàññ, ngir mu génne ñi gëm tey jëfe yiw cig lëndëm jëme leen ci leer. Képp ku gëm Yàlla tey jëfe yiw, (Yàlla) dana ko tàbbal Àjjana joo xam ne ay dex ñooy daw ci suufam, ñu béel fa Yàlla may ko fa xéewal gu jekk.
12اللَّهُ الَّذِي خَلَقَ سَبْعَ سَمَاوَاتٍ وَمِنَ الْأَرْضِ مِثْلَهُنَّ يَتَنَزَّلُ الْأَمْرُ بَيْنَهُنَّ لِتَعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ وَأَنَّ اللَّهَ قَدْ أَحَاطَ بِكُلِّ شَيْءٍ عِلْمًا
Moom Yàlla mi bind juróom-ñaari asamaan ak suuf yu na toll. Ay ndigalam di wàcci ci seen diggante, loolu lépp ngir ngeen xam ne Yàlla man na lépp lu ne te it peek na lépp lu ne ci xam-xam.
At-TalaqFihi Alxuraan
12Aaya
MedinanRevelation
11Aaya

Tekki — At-Talaq 11

Simoore At-Talaq Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ab Yonent buy jàng ci yéen Laayay Yàlla mu leer…

Simoore Aaya 11/12 — At-Talaq الطلاق (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Talaq Dégg, At-Talaq Tekki, At-Talaq mp3, At-Talaq pdf. Aaya 9–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers