At-Talaq · 12/12
Tekki Waxtaan — Simoore At-Talaq
اللَّهُ الَّذِي خَلَقَ سَبْعَ سَمَاوَاتٍ وَمِنَ الْأَرْضِ مِثْلَهُنَّ يَتَنَزَّلُ الْأَمْرُ بَيْنَهُنَّ لِتَعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ وَأَنَّ اللَّهَ قَدْ أَحَاطَ بِكُلِّ شَيْءٍ عِلْمًا ۝١٢
Allaahul lazee khalaq Sab`a Samaawaatinw wa minal ardi mislahunna yatanazzalul amru bainahunna lita`lamooo annal laaha `alaa kulli shai`in Qadeerunw wa annal laaha qad ahaata bikulli shai`in ilmaa
📖 Tekkim Wolof
Moom Yàlla mi bind juróom-ñaari asamaan ak suuf yu na toll. Ay ndigalam di wàcci ci seen diggante, loolu lépp ngir ngeen xam ne Yàlla man na lépp lu ne te it peek na lépp lu ne ci xam-xam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-12 — Simoore At-Talaq

10أَعَدَّ اللَّهُ لَهُمْ عَذَابًا شَدِيدًا ۖ فَاتَّقُوا اللَّهَ يَا أُولِي الْأَلْبَابِ الَّذِينَ آمَنُوا ۚ قَدْ أَنزَلَ اللَّهُ إِلَيْكُمْ ذِكْرًا
Yàlla waajal na leen mbugël mu tar. Kon book ragal-leen Yàlla, yéen woroom xel yi, natt gëm. Yàlla wàcce na ci yéen ag fàttali,
11رَّسُولًا يَتْلُو عَلَيْكُمْ آيَاتِ اللَّهِ مُبَيِّنَاتٍ لِّيُخْرِجَ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ مِنَ الظُّلُمَاتِ إِلَى النُّورِ ۚ وَمَن يُؤْمِن بِاللَّهِ وَيَعْمَلْ صَالِحًا يُدْخِلْهُ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا ۖ قَدْ أَحْسَنَ اللَّهُ لَهُ رِزْقًا
ab Yonent buy jàng ci yéen Laayay Yàlla mu leer nàññ, ngir mu génne ñi gëm tey jëfe yiw cig lëndëm jëme leen ci leer. Képp ku gëm Yàlla tey jëfe yiw, (Yàlla) dana ko tàbbal Àjjana joo xam ne ay dex ñooy daw ci suufam, ñu béel fa Yàlla may ko fa xéewal gu jekk.
12اللَّهُ الَّذِي خَلَقَ سَبْعَ سَمَاوَاتٍ وَمِنَ الْأَرْضِ مِثْلَهُنَّ يَتَنَزَّلُ الْأَمْرُ بَيْنَهُنَّ لِتَعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ وَأَنَّ اللَّهَ قَدْ أَحَاطَ بِكُلِّ شَيْءٍ عِلْمًا
Moom Yàlla mi bind juróom-ñaari asamaan ak suuf yu na toll. Ay ndigalam di wàcci ci seen diggante, loolu lépp ngir ngeen xam ne Yàlla man na lépp lu ne te it peek na lépp lu ne ci xam-xam.
At-TalaqFihi Alxuraan
12Aaya
MedinanRevelation
12Aaya

Tekki — At-Talaq 12

Simoore At-Talaq Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom Yàlla mi bind juróom-ñaari asamaan ak suuf yu na…

Simoore Aaya 12/12 — Simoore At-Talaq الطلاق (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Talaq Dégg, Simoore At-Talaq Tekki, Simoore At-Talaq mp3, Simoore At-Talaq pdf. Aaya 10–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers