Al-Mulk · 28/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mulk
قُلْ أَرَأَيْتُمْ إِنْ أَهْلَكَنِيَ اللَّهُ وَمَن مَّعِيَ أَوْ رَحِمَنَا فَمَن يُجِيرُ الْكَافِرِينَ مِنْ عَذَابٍ أَلِيمٍ ۝٢٨
Qul ara`aytum in ahlaka niyal laahu wa mam ma`iya aw rahimanaa famai-yujeerul kaafireena min `azaabin aleem
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “Xanaa gisu leen ? Su ma Yàlla reyoon maak ñi ma àndal, ana kan mooy man a yiir yéefar yi aar leen ci mbugal mu mitti (amul de) ? ”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 26-30 — Simoore Al-Mulk

26قُلْ إِنَّمَا الْعِلْمُ عِندَ اللَّهِ وَإِنَّمَا أَنَا نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Waxal ne : “Xam-xamub loolu ma nga ca Yàlla. Man nag ab xuppekat buy leeral laa”.
27فَلَمَّا رَأَوْهُ زُلْفَةً سِيئَتْ وُجُوهُ الَّذِينَ كَفَرُوا وَقِيلَ هَٰذَا الَّذِي كُنتُم بِهِ تَدَّعُونَ
Bu, ñu ne gegg ca (mbugël ma), xarkanami yéefar ya di gañ-gañi. Ñu ne leen: “Lii nag ngeen yàkkamti woon”.
28قُلْ أَرَأَيْتُمْ إِنْ أَهْلَكَنِيَ اللَّهُ وَمَن مَّعِيَ أَوْ رَحِمَنَا فَمَن يُجِيرُ الْكَافِرِينَ مِنْ عَذَابٍ أَلِيمٍ
Waxal ne : “Xanaa gisu leen ? Su ma Yàlla reyoon maak ñi ma àndal, ana kan mooy man a yiir yéefar yi aar leen ci mbugal mu mitti (amul de) ? ”.
29قُلْ هُوَ الرَّحْمَٰنُ آمَنَّا بِهِ وَعَلَيْهِ تَوَكَّلْنَا ۖ فَسَتَعْلَمُونَ مَنْ هُوَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Waxal ne : “Kooku moo di, Yàlla yëramaakoon bi. Gëm nanu ko te doyloo nanu ko. Dangeen xala xam ana kan moo nekk cig réer”.
30قُلْ أَرَأَيْتُمْ إِنْ أَصْبَحَ مَاؤُكُمْ غَوْرًا فَمَن يَأْتِيكُم بِمَاءٍ مَّعِينٍ
Waxal ne : “Xanaa gisuleen ? Bu seen ndox mi rawoon ci biir suuf xóot, ana kan moo leen di may bëtu ndox bu tane (Yàlla) ? ”
Al-MulkFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Al-Mulk 28

Simoore Al-Mulk Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “Xanaa gisu leen ? Su ma Yàlla…

Simoore Aaya 28/30 — Simoore Al-Mulk الملك (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mulk Dégg, Simoore Al-Mulk Tekki, Simoore Al-Mulk mp3, Simoore Al-Mulk pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers