Al-Mulk · 27/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mulk
فَلَمَّا رَأَوْهُ زُلْفَةً سِيئَتْ وُجُوهُ الَّذِينَ كَفَرُوا وَقِيلَ هَٰذَا الَّذِي كُنتُم بِهِ تَدَّعُونَ ۝٢٧
Falaammaa ra-awhu zulfatan seee`at wujoohul lazeena kafaroo wa qeela haazal lazee kuntum bihee tadda`oon
📖 Tekkim Wolof
Bu, ñu ne gegg ca (mbugël ma), xarkanami yéefar ya di gañ-gañi. Ñu ne leen: “Lii nag ngeen yàkkamti woon”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Simoore Al-Mulk

25وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ñuy wax naan : “Dig ba kañ lay doon su fekkee ne ñu dëggu ngeen ? ”.
26قُلْ إِنَّمَا الْعِلْمُ عِندَ اللَّهِ وَإِنَّمَا أَنَا نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Waxal ne : “Xam-xamub loolu ma nga ca Yàlla. Man nag ab xuppekat buy leeral laa”.
27فَلَمَّا رَأَوْهُ زُلْفَةً سِيئَتْ وُجُوهُ الَّذِينَ كَفَرُوا وَقِيلَ هَٰذَا الَّذِي كُنتُم بِهِ تَدَّعُونَ
Bu, ñu ne gegg ca (mbugël ma), xarkanami yéefar ya di gañ-gañi. Ñu ne leen: “Lii nag ngeen yàkkamti woon”.
28قُلْ أَرَأَيْتُمْ إِنْ أَهْلَكَنِيَ اللَّهُ وَمَن مَّعِيَ أَوْ رَحِمَنَا فَمَن يُجِيرُ الْكَافِرِينَ مِنْ عَذَابٍ أَلِيمٍ
Waxal ne : “Xanaa gisu leen ? Su ma Yàlla reyoon maak ñi ma àndal, ana kan mooy man a yiir yéefar yi aar leen ci mbugal mu mitti (amul de) ? ”.
29قُلْ هُوَ الرَّحْمَٰنُ آمَنَّا بِهِ وَعَلَيْهِ تَوَكَّلْنَا ۖ فَسَتَعْلَمُونَ مَنْ هُوَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Waxal ne : “Kooku moo di, Yàlla yëramaakoon bi. Gëm nanu ko te doyloo nanu ko. Dangeen xala xam ana kan moo nekk cig réer”.
Al-MulkFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — Al-Mulk 27

Simoore Al-Mulk Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu, ñu ne gegg ca (mbugël ma), xarkanami yéefar ya…

Simoore Aaya 27/30 — Simoore Al-Mulk الملك (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mulk Dégg, Simoore Al-Mulk Tekki, Simoore Al-Mulk mp3, Simoore Al-Mulk pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers