Al-Qalam · 44/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
فَذَرْنِي وَمَن يُكَذِّبُ بِهَٰذَا الْحَدِيثِ ۖ سَنَسْتَدْرِجُهُم مِّنْ حَيْثُ لَا يَعْلَمُونَ ۝٤٤
Fazarnee wa many yukazzibu bihaazal hadeesi sanastad rijuhum min haisu laa ya`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Bàyyee ma ak ñiy jàppe waxtaan wii ( Alxuraan) ay fen dina nu léen taxañe fu ñu dul xam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 42-46 — Simoore Al-Qalam

42يَوْمَ يُكْشَفُ عَن سَاقٍ وَيُدْعَوْنَ إِلَى السُّجُودِ فَلَا يَسْتَطِيعُونَ
Bu keroogee ba ñuy wuññi ab yeel [tiitaange] nu def leen woo ngir ñu Sujud te du ñu ko man.
43خَاشِعَةً أَبْصَارُهُمْ تَرْهَقُهُمْ ذِلَّةٌ ۖ وَقَدْ كَانُوا يُدْعَوْنَ إِلَى السُّجُودِ وَهُمْ سَالِمُونَ
Ñuy xiin-xiini ne muq ak gàcce te kat ba ca ba ñuy dund daayees na léen woo ngir ñuy sujood (jullig) te booba dara dalut léen.
44فَذَرْنِي وَمَن يُكَذِّبُ بِهَٰذَا الْحَدِيثِ ۖ سَنَسْتَدْرِجُهُم مِّنْ حَيْثُ لَا يَعْلَمُونَ
Bàyyee ma ak ñiy jàppe waxtaan wii ( Alxuraan) ay fen dina nu léen taxañe fu ñu dul xam.
45وَأُمْلِي لَهُمْ ۚ إِنَّ كَيْدِي مَتِينٌ
Dama léen di dënniirlu waaye sama pexe naaxsaay.
46أَمْ تَسْأَلُهُمْ أَجْرًا فَهُم مِّن مَّغْرَمٍ مُّثْقَلُونَ
Moo ndax da nga léen di laaj ag pey te ñu fees dell ak i bor.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
44Aaya

Tekki — Al-Qalam 44

Simoore Al-Qalam Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bàyyee ma ak ñiy jàppe waxtaan wii ( Alxuraan) ay…

Simoore Aaya 44/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers