Al-A'raf · 205/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
وَاذْكُر رَّبَّكَ فِي نَفْسِكَ تَضَرُّعًا وَخِيفَةً وَدُونَ الْجَهْرِ مِنَ الْقَوْلِ بِالْغُدُوِّ وَالْآصَالِ وَلَا تَكُن مِّنَ الْغَافِلِينَ ۝٢٠٥
Wazkur Rabbaka fee nafsika tadarru`anw wa kheefatanw wa doonal jahri minal qawli bilghuduwwi wal aasali wa laa takum minal ghaafileen
📖 Tekkim Wolof
Nangay tudd sa Boroom ci sa bopp ànd ak toroxlu ak ug ragal, ci lu ànd ak yelu ci sa kàddu, ci kaw subaak ngoon, te bul bokk ca ñu sàggan ña.
🎧 Dégg

📜 Aaya 203-206 — Al-A'raf

203وَإِذَا لَمْ تَأْتِهِم بِآيَةٍ قَالُوا لَوْلَا اجْتَبَيْتَهَا ۚ قُلْ إِنَّمَا أَتَّبِعُ مَا يُوحَىٰ إِلَيَّ مِن رَّبِّي ۚ هَٰذَا بَصَائِرُ مِن رَّبِّكُمْ وَهُدًى وَرَحْمَةٌ لِّقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Te bu ndigal ñëwul, ñu naan : “Lu tee nga fental ko sa bopp ? ” Neel : “Duma def lu dul topp li ñu ma soloo mu tukke ci sama Boroom. Loolu ay lay la yu tukkee ci seen Boroom, di njub ak yërmaande ci nit ñu gëm.
204وَإِذَا قُرِئَ الْقُرْآنُ فَاسْتَمِعُوا لَهُ وَأَنصِتُوا لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Kon bu ñuy jàng Alxuraan, nangeen ko déglu te nangeen ko xarawlu ndax xéy-na yërëmees leen.
205وَاذْكُر رَّبَّكَ فِي نَفْسِكَ تَضَرُّعًا وَخِيفَةً وَدُونَ الْجَهْرِ مِنَ الْقَوْلِ بِالْغُدُوِّ وَالْآصَالِ وَلَا تَكُن مِّنَ الْغَافِلِينَ
Nangay tudd sa Boroom ci sa bopp ànd ak toroxlu ak ug ragal, ci lu ànd ak yelu ci sa kàddu, ci kaw subaak ngoon, te bul bokk ca ñu sàggan ña.
206إِنَّ الَّذِينَ عِندَ رَبِّكَ لَا يَسْتَكْبِرُونَ عَنْ عِبَادَتِهِ وَيُسَبِّحُونَهُ وَلَهُ يَسْجُدُونَ ۩
Ña nga xam ne ñanga ca sa Boroom, duñu di rëylu ci jaamu Ko. Te danañu Ko di sàbbaal, di Ko sujjóotal.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
205Aaya

Tekki — Al-A'raf 205

Simoore Al-A'raf Aaya 205 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangay tudd sa Boroom ci sa bopp ànd ak toroxlu…

Simoore Aaya 205/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 203–206. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers