Al-Anfal · 4/75
Tekki Waxtaan — Al-Anfal
أُولَٰئِكَ هُمُ الْمُؤْمِنُونَ حَقًّا ۚ لَّهُمْ دَرَجَاتٌ عِندَ رَبِّهِمْ وَمَغْفِرَةٌ وَرِزْقٌ كَرِيمٌ ۝٤
Ulaaa`ika humul mu`minoona haqqaa; lahum darajaatun `inda Rabbihim wa magh firatunw wa rizqun kareem
📖 Tekkim Wolof
Ñooña ñooy jullit dëgg : ñeel na leen yékkatiku ca seen Boroom, ci ag jéggal ak wërsëg wu tedd.
🎧 Dégg

📜 Aaya 2-6 — Al-Anfal

2إِنَّمَا الْمُؤْمِنُونَ الَّذِينَ إِذَا ذُكِرَ اللَّهُ وَجِلَتْ قُلُوبُهُمْ وَإِذَا تُلِيَتْ عَلَيْهِمْ آيَاتُهُ زَادَتْهُمْ إِيمَانًا وَعَلَىٰ رَبِّهِمْ يَتَوَكَّلُونَ
Jullit ya ñooy ña nga xam ne bu ñu tuddee Yàlla seeni xol yëngu. Te bu ñu jàngaa ci ñoom ay laayaam mu yokk seen ngëm. Te ci seen Boroom lañu wékku.
3الَّذِينَ يُقِيمُونَ الصَّلَاةَ وَمِمَّا رَزَقْنَاهُمْ يُنفِقُونَ
Ñooy ña nga xam ne danañu taxawal julli te ca la Nu leen wërsëgal, danañu ca joxe.
4أُولَٰئِكَ هُمُ الْمُؤْمِنُونَ حَقًّا ۚ لَّهُمْ دَرَجَاتٌ عِندَ رَبِّهِمْ وَمَغْفِرَةٌ وَرِزْقٌ كَرِيمٌ
Ñooña ñooy jullit dëgg : ñeel na leen yékkatiku ca seen Boroom, ci ag jéggal ak wërsëg wu tedd.
5كَمَا أَخْرَجَكَ رَبُّكَ مِن بَيْتِكَ بِالْحَقِّ وَإِنَّ فَرِيقًا مِّنَ الْمُؤْمِنِينَ لَكَارِهُونَ
Naka noonu, sa Boroom génne na la sa kër ci dëgg, te fekk neexul ñennat ca way-gëm ña.
6يُجَادِلُونَكَ فِي الْحَقِّ بَعْدَمَا تَبَيَّنَ كَأَنَّمَا يُسَاقُونَ إِلَى الْمَوْتِ وَهُمْ يَنظُرُونَ
Ñangay weranteek yaw ca dëgg ga ginnaaw ba mu feeñee, leer nàññ ; mel ni dañu leen a bëmax jëme ci dee, ñu ne ca jàkk.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Anfal 4

Simoore Al-Anfal Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñooña ñooy jullit dëgg : ñeel na leen yékkatiku ca…

Simoore Aaya 4/75 — Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anfal Dégg, Al-Anfal Tekki, Al-Anfal mp3, Al-Anfal pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers