Al-Anfal · 61/75
Tekki Waxtaan — Al-Anfal
۞ وَإِن جَنَحُوا لِلسَّلْمِ فَاجْنَحْ لَهَا وَتَوَكَّلْ عَلَى اللَّهِ ۚ إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ ٦١
Transliteration
Wa in janahoo lissalmi fajnah lahaa wa tawakkal `alal laah; innahoo Huwas Samee`ul `Aleem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu jengee jëm ci jàmm, jengal yaw it jëm ca te nga wéeru ci Yàlla, naka Moom Kuy dégg la, Ku xam la.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 59-63 — Al-Anfal
59وَلَا يَحْسَبَنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا سَبَقُوا ۚ إِنَّهُمْ لَا يُعْجِزُونَ
Ña weddi, buñu njortu ne raw nañu. Ñoom duñu mën a raw Yàlla.
60وَأَعِدُّوا لَهُم مَّا اسْتَطَعْتُم مِّن قُوَّةٍ وَمِن رِّبَاطِ الْخَيْلِ تُرْهِبُونَ بِهِ عَدُوَّ اللَّهِ وَعَدُوَّكُمْ وَآخَرِينَ مِن دُونِهِمْ لَا تَعْلَمُونَهُمُ اللَّهُ يَعْلَمُهُمْ ۚ وَمَا تُنفِقُوا مِن شَيْءٍ فِي سَبِيلِ اللَّهِ يُوَفَّ إِلَيْكُمْ وَأَنتُمْ لَا تُظْلَمُونَ
Feguleen, ngir ñoom, lu ngeen mën ci doole ak fas yu ngeen mën a tiitale nooni Yàlla ya, di seeni noon, ak ñeneen ñu dul ñoom, xamooleen, Yàlla Moo leen xam. Li ngeen di joxe ci alal ci yoonu Yàlla, dees na leen ko delloo ba mu mat sëkk te deesuleen ci wàññil dara.
61۞ وَإِن جَنَحُوا لِلسَّلْمِ فَاجْنَحْ لَهَا وَتَوَكَّلْ عَلَى اللَّهِ ۚ إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
Bu ñu jengee jëm ci jàmm, jengal yaw it jëm ca te nga wéeru ci Yàlla, naka Moom Kuy dégg la, Ku xam la.
62وَإِن يُرِيدُوا أَن يَخْدَعُوكَ فَإِنَّ حَسْبَكَ اللَّهُ ۚ هُوَ الَّذِي أَيَّدَكَ بِنَصْرِهِ وَبِالْمُؤْمِنِينَ
Bu ñu la naree wor, na la Yàlla doy. Moom moo lay dëgëral ci ndimbalam ak ñu gëm ña.
63وَأَلَّفَ بَيْنَ قُلُوبِهِمْ ۚ لَوْ أَنفَقْتَ مَا فِي الْأَرْضِ جَمِيعًا مَّا أَلَّفْتَ بَيْنَ قُلُوبِهِمْ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ أَلَّفَ بَيْنَهُمْ ۚ إِنَّهُ عَزِيزٌ حَكِيمٌ
Te Moo dajale seeni xol (ñu soppante). Te yaw boo joxe woon lépp li nekk ci àddina, du tax nga mën a boole seeni xol ; Moom nag [Yàlla] Ku not la, Ku xereñ la.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
61Aaya
Tekki — Al-Anfal 61
Simoore Al-Anfal Aaya 61 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu jengee jëm ci jàmm, jengal yaw it jëm…Simoore Aaya 61/75 — Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anfal Dégg, Al-Anfal Tekki, Al-Anfal mp3, Al-Anfal pdf. Aaya 59–63. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








