At-Tawba · 66/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
لَا تَعْتَذِرُوا قَدْ كَفَرْتُم بَعْدَ إِيمَانِكُمْ ۚ إِن نَّعْفُ عَن طَائِفَةٍ مِّنكُمْ نُعَذِّبْ طَائِفَةً بِأَنَّهُمْ كَانُوا مُجْرِمِينَ ۝٦٦
Laa ta`taziroo qad kafartum ba`da eemaanikum; in na`fu `an taaa`ifatim minkum nu`az zib taaa`ifatam bi annahum kaanoo mujrimeen
📖 Tekkim Wolof
Buleen lay : weddi ngeen ba noppi ginnaaw seen ngëm. Ndeem Dananu jéggal ab kurél ci yéen, Dananu mbugal it ab kurél ngir dañoo nekkoon di ay saay-saay.
🎧 Dégg

📜 Aaya 64-68 — At-Tawba

64يَحْذَرُ الْمُنَافِقُونَ أَن تُنَزَّلَ عَلَيْهِمْ سُورَةٌ تُنَبِّئُهُم بِمَا فِي قُلُوبِهِمْ ۚ قُلِ اسْتَهْزِئُوا إِنَّ اللَّهَ مُخْرِجٌ مَّا تَحْذَرُونَ
Naaféq ya danañu ragal aw saar wàcc feeñal li nekk ci seeni xol. Neeleen : “Ñaawleleen ! Yàlla Dana génne li ngeen di ragal (mu génn)”.
65وَلَئِن سَأَلْتَهُمْ لَيَقُولُنَّ إِنَّمَا كُنَّا نَخُوضُ وَنَلْعَبُ ۚ قُلْ أَبِاللَّهِ وَآيَاتِهِ وَرَسُولِهِ كُنتُمْ تَسْتَهْزِئُونَ
Te boo leen laajoon, Giñ naa ne danañu wax naan : “Nun dey danu doon caaxaan.”. Neeleen : “Kon daal yéen Yàlla ngeen di fowe ? ”
66لَا تَعْتَذِرُوا قَدْ كَفَرْتُم بَعْدَ إِيمَانِكُمْ ۚ إِن نَّعْفُ عَن طَائِفَةٍ مِّنكُمْ نُعَذِّبْ طَائِفَةً بِأَنَّهُمْ كَانُوا مُجْرِمِينَ
Buleen lay : weddi ngeen ba noppi ginnaaw seen ngëm. Ndeem Dananu jéggal ab kurél ci yéen, Dananu mbugal it ab kurél ngir dañoo nekkoon di ay saay-saay.
67الْمُنَافِقُونَ وَالْمُنَافِقَاتُ بَعْضُهُم مِّن بَعْضٍ ۚ يَأْمُرُونَ بِالْمُنكَرِ وَيَنْهَوْنَ عَنِ الْمَعْرُوفِ وَيَقْبِضُونَ أَيْدِيَهُمْ ۚ نَسُوا اللَّهَ فَنَسِيَهُمْ ۗ إِنَّ الْمُنَافِقِينَ هُمُ الْفَاسِقُونَ
Naaféq yu góor ya ak naaféq yu jigéen ya dañuy digalante lu bon, dàq lu baax, di téyee seeni yoxo (bañ a joxe). Dañuy fàtte Yàlla ba tax Mu fàtte leen. Naaféq ya ñoom ñooy saay- saay sa.
68وَعَدَ اللَّهُ الْمُنَافِقِينَ وَالْمُنَافِقَاتِ وَالْكُفَّارَ نَارَ جَهَنَّمَ خَالِدِينَ فِيهَا ۚ هِيَ حَسْبُهُمْ ۚ وَلَعَنَهُمُ اللَّهُ ۖ وَلَهُمْ عَذَابٌ مُّقِيمٌ
Yàlla dig na naaféq yu góor ya ak naaféq yu jigéen ya ak yéefar ya aw tàngoor ca Safara. Dañu fay béel. Moom doy na leen (mbugal). Te Yàlla rëbb na leen. Am nañu mbugal mu sax.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
66Aaya

Tekki — At-Tawba 66

Simoore At-Tawba Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Buleen lay : weddi ngeen ba noppi ginnaaw seen ngëm.…

Simoore Aaya 66/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers