At-Tin · 6/8
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tin
إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فَلَهُمْ أَجْرٌ غَيْرُ مَمْنُونٍ ۝٦
Ill-lal lazeena aamanoo wa `amilus saalihaati; falahum ajrun ghairu mamnoon
📖 Tekkim Wolof
ba mu des ña gëm tey jëfu yiw : ñoom dananu am pey gu dootul dog.

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore At-Tin

4لَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ فِي أَحْسَنِ تَقْوِيمٍ
Bind nanu nit ci gën ja rafeti anam.
5ثُمَّ رَدَدْنَاهُ أَسْفَلَ سَافِلِينَ
Top, waaye man naa dem ba gëna suufe lépp lu suufe,
6إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فَلَهُمْ أَجْرٌ غَيْرُ مَمْنُونٍ
ba mu des ña gëm tey jëfu yiw : ñoom dananu am pey gu dootul dog.
7فَمَا يُكَذِّبُكَ بَعْدُ بِالدِّينِ
Bu loolu wéyee, ana lan moo tax ngay weddi bisub faytoo ba (bis pénc) ?
8أَلَيْسَ اللَّهُ بِأَحْكَمِ الْحَاكِمِينَ
Moo xanaa Yàlla dafa dul ki dàqa àtte àttekat yi ?
At-TinFihi Alxuraan
8Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — At-Tin 6

Simoore At-Tin Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba mu des ña gëm tey jëfu yiw : ñoom…

Simoore Aaya 6/8 — Simoore At-Tin التين (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tin Dégg, Simoore At-Tin Tekki, Simoore At-Tin mp3, Simoore At-Tin pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers