At-Tin · 5/8
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tin
ثُمَّ رَدَدْنَاهُ أَسْفَلَ سَافِلِينَ ۝٥
Thumma ra dad naahu asfala saafileen
📖 Tekkim Wolof
Top, waaye man naa dem ba gëna suufe lépp lu suufe,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 3-7 — Simoore At-Tin

3وَهَٰذَا الْبَلَدِ الْأَمِينِ
Ak ca réew mu wóor mii di (Màkka) ! ne
4لَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ فِي أَحْسَنِ تَقْوِيمٍ
Bind nanu nit ci gën ja rafeti anam.
5ثُمَّ رَدَدْنَاهُ أَسْفَلَ سَافِلِينَ
Top, waaye man naa dem ba gëna suufe lépp lu suufe,
6إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فَلَهُمْ أَجْرٌ غَيْرُ مَمْنُونٍ
ba mu des ña gëm tey jëfu yiw : ñoom dananu am pey gu dootul dog.
7فَمَا يُكَذِّبُكَ بَعْدُ بِالدِّينِ
Bu loolu wéyee, ana lan moo tax ngay weddi bisub faytoo ba (bis pénc) ?
At-TinFihi Alxuraan
8Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — At-Tin 5

Simoore At-Tin Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Top, waaye man naa dem ba gëna suufe lépp lu…

Simoore Aaya 5/8 — Simoore At-Tin التين (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tin Dégg, Simoore At-Tin Tekki, Simoore At-Tin mp3, Simoore At-Tin pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers