At-Tin · 8/8
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tin
أَلَيْسَ اللَّهُ بِأَحْكَمِ الْحَاكِمِينَ ۝٨
Alai sal laahu bi-ahkamil haakimeen
📖 Tekkim Wolof
Moo xanaa Yàlla dafa dul ki dàqa àtte àttekat yi ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-8 — Simoore At-Tin

6إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فَلَهُمْ أَجْرٌ غَيْرُ مَمْنُونٍ
ba mu des ña gëm tey jëfu yiw : ñoom dananu am pey gu dootul dog.
7فَمَا يُكَذِّبُكَ بَعْدُ بِالدِّينِ
Bu loolu wéyee, ana lan moo tax ngay weddi bisub faytoo ba (bis pénc) ?
8أَلَيْسَ اللَّهُ بِأَحْكَمِ الْحَاكِمِينَ
Moo xanaa Yàlla dafa dul ki dàqa àtte àttekat yi ?
At-TinFihi Alxuraan
8Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — At-Tin 8

Simoore At-Tin Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo xanaa Yàlla dafa dul ki dàqa àtte àttekat yi…

Simoore Aaya 8/8 — Simoore At-Tin التين (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tin Dégg, Simoore At-Tin Tekki, Simoore At-Tin mp3, Simoore At-Tin pdf. Aaya 6–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers