At-Tin · 4/8
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tin
لَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ فِي أَحْسَنِ تَقْوِيمٍ ۝٤
Laqad khalaqnal insaana fee ahsani taqweem
📖 Tekkim Wolof
Bind nanu nit ci gën ja rafeti anam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 2-6 — Simoore At-Tin

2وَطُورِ سِينِينَ
Ak ci tund Siiniin (Siinaa’i) !
3وَهَٰذَا الْبَلَدِ الْأَمِينِ
Ak ca réew mu wóor mii di (Màkka) ! ne
4لَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ فِي أَحْسَنِ تَقْوِيمٍ
Bind nanu nit ci gën ja rafeti anam.
5ثُمَّ رَدَدْنَاهُ أَسْفَلَ سَافِلِينَ
Top, waaye man naa dem ba gëna suufe lépp lu suufe,
6إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فَلَهُمْ أَجْرٌ غَيْرُ مَمْنُونٍ
ba mu des ña gëm tey jëfu yiw : ñoom dananu am pey gu dootul dog.
At-TinFihi Alxuraan
8Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — At-Tin 4

Simoore At-Tin Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bind nanu nit ci gën ja rafeti anam.

Simoore Aaya 4/8 — Simoore At-Tin التين (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tin Dégg, Simoore At-Tin Tekki, Simoore At-Tin mp3, Simoore At-Tin pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers