At-Tin · 7/8
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tin
فَمَا يُكَذِّبُكَ بَعْدُ بِالدِّينِ ۝٧
Fama yu kaz zibuka b`adu bid deen
📖 Tekkim Wolof
Bu loolu wéyee, ana lan moo tax ngay weddi bisub faytoo ba (bis pénc) ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 5-8 — Simoore At-Tin

5ثُمَّ رَدَدْنَاهُ أَسْفَلَ سَافِلِينَ
Top, waaye man naa dem ba gëna suufe lépp lu suufe,
6إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فَلَهُمْ أَجْرٌ غَيْرُ مَمْنُونٍ
ba mu des ña gëm tey jëfu yiw : ñoom dananu am pey gu dootul dog.
7فَمَا يُكَذِّبُكَ بَعْدُ بِالدِّينِ
Bu loolu wéyee, ana lan moo tax ngay weddi bisub faytoo ba (bis pénc) ?
8أَلَيْسَ اللَّهُ بِأَحْكَمِ الْحَاكِمِينَ
Moo xanaa Yàlla dafa dul ki dàqa àtte àttekat yi ?
At-TinFihi Alxuraan
8Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — At-Tin 7

Simoore At-Tin Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu loolu wéyee, ana lan moo tax ngay weddi bisub…

Simoore Aaya 7/8 — Simoore At-Tin التين (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tin Dégg, Simoore At-Tin Tekki, Simoore At-Tin mp3, Simoore At-Tin pdf. Aaya 5–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers