PDF —
8 Aaya Meccan PDF
Built right in your browser — download starts automatically

Simoore At-Tin pdf — Wàcce (Wolof)

Simoore At-Tin pdf Wolof — Wàcce Simoore At-Tin Tekki. Simoore At-Tin (Meccan) 8 Aaya.



8 Aaya · Meccan · Wolof
bismillah
ﭫﭬﭭ
95:1 Ci garabug fig ak oliw Maa ngi giñ !
ﭮﭯﭰ
95:2 Ak ci tund Siiniin (Siinaa’i) !
ﭱﭲﭳﭴ
95:3 Ak ca réew mu wóor mii di (Màkka) ! ne
ﭵﭶﭷﭸﭹﭺﭻ
95:4 Bind nanu nit ci gën ja rafeti anam.
ﭼﭽﭾﭿﮀ
95:5 Top, waaye man naa dem ba gëna suufe lépp lu suufe,
ﮁﮂﮃﮄﮅﮆﮇﮈﮉﮊ
95:6 ba mu des ña gëm tey jëfu yiw : ñoom dananu am pey gu dootul dog.
ﮋﮌﮍﮎﮏ
95:7 Bu loolu wéyee, ana lan moo tax ngay weddi bisub faytoo ba (bis pénc) ?
ﮐﮑﮒﮓﮔ
95:8 Moo xanaa Yàlla dafa dul ki dàqa àtte àttekat yi ?

Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 9, 2026

Don't forget us in your sincere prayers