Hud · 52/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
وَيَا قَوْمِ اسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ ثُمَّ تُوبُوا إِلَيْهِ يُرْسِلِ السَّمَاءَ عَلَيْكُم مِّدْرَارًا وَيَزِدْكُمْ قُوَّةً إِلَىٰ قُوَّتِكُمْ وَلَا تَتَوَلَّوْا مُجْرِمِينَ ۝٥٢
Wa yaa qawmis taghfiroo Rabbakum summa toobooo ilaihi yursilis samaaa`a `alaikum midraaranw wa yazidkum quwwatan ilaa quwwatikum wa laa tatawallaw mujrimeen
📖 Tekkim Wolof
Te yéen samaw nit, baaluleen seen Boroom te ngeen tuub [réccu] jëm ci Moom, kon Dana dottib taw bu jóge asamaan ci seen kaw te Dana leen yokk doole ju dolliku ci seen doole. Bu ngeen dëddoo nekk i bokkaalekat”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 50-54 — Simoore Hud

50وَإِلَىٰ عَادٍ أَخَاهُمْ هُودًا ۚ قَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ إِنْ أَنتُمْ إِلَّا مُفْتَرُونَ
Te waa Aad, seen mbokk Huud wax na leen ne : “Yéen samaw nit, jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Nekkeewuleen fa lu dul di duural Yàlla.
51يَا قَوْمِ لَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ أَجْرًا ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَى الَّذِي فَطَرَنِي ۚ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Te samaw nit, laajumaleen ci ag pey. Samag pey bokkul ci loxob kenn ku dul Ki ma bind [sàkk]. Moo ndax dangeen dul xel-lu ?
52وَيَا قَوْمِ اسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ ثُمَّ تُوبُوا إِلَيْهِ يُرْسِلِ السَّمَاءَ عَلَيْكُم مِّدْرَارًا وَيَزِدْكُمْ قُوَّةً إِلَىٰ قُوَّتِكُمْ وَلَا تَتَوَلَّوْا مُجْرِمِينَ
Te yéen samaw nit, baaluleen seen Boroom te ngeen tuub [réccu] jëm ci Moom, kon Dana dottib taw bu jóge asamaan ci seen kaw te Dana leen yokk doole ju dolliku ci seen doole. Bu ngeen dëddoo nekk i bokkaalekat”.
53قَالُوا يَا هُودُ مَا جِئْتَنَا بِبَيِّنَةٍ وَمَا نَحْنُ بِتَارِكِي آلِهَتِنَا عَن قَوْلِكَ وَمَا نَحْنُ لَكَ بِمُؤْمِنِينَ
Ñu ne : "Éy yaw Huud, indiloo nu lu leer, te nun dunu bàyyi sunu yàlla yi ngir say wax, te it gëmuñu la.
54إِن نَّقُولُ إِلَّا اعْتَرَاكَ بَعْضُ آلِهَتِنَا بِسُوءٍ ۗ قَالَ إِنِّي أُشْهِدُ اللَّهَ وَاشْهَدُوا أَنِّي بَرِيءٌ مِّمَّا تُشْرِكُونَ
Dunu la wax lu dul ne kenn ci sunu yàlla yi moo la sadd lu bon”. Mu ne : “Man dey, maa ngi seedeloo Yàlla - te seedelooleen yéen itam - ne deñ naa ba set wecc ci li ngeen di jaamu,
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
52Aaya

Tekki — Hud 52

Simoore Hud Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te yéen samaw nit, baaluleen seen Boroom te ngeen tuub…

Simoore Aaya 52/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers