Yusuf · 1/111
Tekki Waxtaan — Simoore Yusuf
الر ۚ تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ الْمُبِينِ ۝١
Alif-Laaam-Raa; tilka Aayaatul Kitaabil Mubeen
📖 Tekkim Wolof
Alif, Laam, Raa. Lii ay xamle la yu nekk ci Téere bu wér péŋŋ bi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Yusuf

1الر ۚ تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ الْمُبِينِ
Alif, Laam, Raa. Lii ay xamle la yu nekk ci Téere bu wér péŋŋ bi.
2إِنَّا أَنزَلْنَاهُ قُرْآنًا عَرَبِيًّا لَّعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ
Wàcce Nanu ko mu di ay njàng ci làkku [araab] ngir ngeen xam la mu tekki.
3نَحْنُ نَقُصُّ عَلَيْكَ أَحْسَنَ الْقَصَصِ بِمَا أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ هَٰذَا الْقُرْآنَ وَإِن كُنتَ مِن قَبْلِهِ لَمِنَ الْغَافِلِينَ
Nun noo ngi lay nettali gën jaa rafeti nettaliin ci Alxuraan jii Nu la xamal te lu ko jiitu nekkoon na loo réere.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
1Aaya

Tekki — Yusuf 1

Simoore Yusuf Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Alif, Laam, Raa. Lii ay xamle la yu nekk ci…

Simoore Aaya 1/111 — Simoore Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yusuf Dégg, Simoore Yusuf Tekki, Simoore Yusuf mp3, Simoore Yusuf pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers