Al-Isra · 109/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
وَيَخِرُّونَ لِلْأَذْقَانِ يَبْكُونَ وَيَزِيدُهُمْ خُشُوعًا ۩ ۝١٠٩
Wa yakhirroona lil azqaani yabkoona wa yazeeduhum khushoo`aa
📖 Tekkim Wolof
Ñu rot dëpp seeni sikkim ca suuf di sujjóot. Seen toroxlu ci Yàlla dolliku.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 107-111 — Simoore Al-Isra

107قُلْ آمِنُوا بِهِ أَوْ لَا تُؤْمِنُوا ۚ إِنَّ الَّذِينَ أُوتُوا الْعِلْمَ مِن قَبْلِهِ إِذَا يُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ يَخِرُّونَ لِلْأَذْقَانِ سُجَّدًا
Neel : “Gëmleen ko mbaa ngeen bañ koo gëm, nanga xam ne joxeef na leen xam-xam. La ko jiitu, bu ñu jàngee ci seen kanam, danañu rot dëpp seeni sikkim ci suuf, sujjóot”
108وَيَقُولُونَ سُبْحَانَ رَبِّنَا إِن كَانَ وَعْدُ رَبِّنَا لَمَفْعُولًا
te ñuy wax ne : “Tudd nanu sellug sunu Boroom ! Digub sunu Boroom fàwwu mu am”.
109وَيَخِرُّونَ لِلْأَذْقَانِ يَبْكُونَ وَيَزِيدُهُمْ خُشُوعًا ۩
Ñu rot dëpp seeni sikkim ca suuf di sujjóot. Seen toroxlu ci Yàlla dolliku.
110قُلِ ادْعُوا اللَّهَ أَوِ ادْعُوا الرَّحْمَٰنَ ۖ أَيًّا مَّا تَدْعُوا فَلَهُ الْأَسْمَاءُ الْحُسْنَىٰ ۚ وَلَا تَجْهَرْ بِصَلَاتِكَ وَلَا تُخَافِتْ بِهَا وَابْتَغِ بَيْنَ ذَٰلِكَ سَبِيلًا
Neel : “Wooleen Yàlla mbaa ngeen woo Aji-yërëme ji. Lu ngeen mën a woo [xamleen ne] Moo moom tur ya gën a rafet. Bul biral ci kaw ci sa julli ; te bul ca yelu it, sàkkal ci diggante ñaar yooyu [yoon wu digg-dóomu]”.
111وَقُلِ الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي لَمْ يَتَّخِذْ وَلَدًا وَلَمْ يَكُن لَّهُ شَرِيكٌ فِي الْمُلْكِ وَلَمْ يَكُن لَّهُ وَلِيٌّ مِّنَ الذُّلِّ ۖ وَكَبِّرْهُ تَكْبِيرًا
Neel : “Gépp cant ñeel na Yàlla mi amul doom te amul ku Mu bokkal nguuramte amul ku koy dimbali cig toroxte”. Dee ko màggal bu baax.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
109Aaya

Tekki — Al-Isra 109

Simoore Al-Isra Aaya 109 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu rot dëpp seeni sikkim ca suuf di sujjóot. Seen…

Simoore Aaya 109/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 107–111. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Sunday, October 4, 2026

Don't forget us in your sincere prayers