Al-Kahf · 41/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
أَوْ يُصْبِحَ مَاؤُهَا غَوْرًا فَلَن تَسْتَطِيعَ لَهُ طَلَبًا ٤١
Transliteration
Aw yusbiha maaa`uhaaa ghawran falan tastatee`a lahoo talabaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
walla ndox ma ŋiis te dootu ko ame feneen”.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 39-43 — Simoore Al-Kahf
39وَلَوْلَا إِذْ دَخَلْتَ جَنَّتَكَ قُلْتَ مَا شَاءَ اللَّهُ لَا قُوَّةَ إِلَّا بِاللَّهِ ۚ إِن تَرَنِ أَنَا أَقَلَّ مِنكَ مَالًا وَوَلَدًا
Lu teewoon ba ngay dugg ca tool ba nga wax ne : “Lu neex Yàlla [rekk ay am] ! Amul kenn ku am kàttan ku dul Yàlla”. Ndeem danga maa gis ma gën laa néew alal ak i doom,
40فَعَسَىٰ رَبِّي أَن يُؤْتِيَنِ خَيْرًا مِّن جَنَّتِكَ وَيُرْسِلَ عَلَيْهَا حُسْبَانًا مِّنَ السَّمَاءِ فَتُصْبِحَ صَعِيدًا زَلَقًا
xéy-na sama Boroom jox ma lu gën sa tool, te yabal ca sa tool jéyya ju jóge asamaan ba mu nekk dénd bu amutul dara,
41أَوْ يُصْبِحَ مَاؤُهَا غَوْرًا فَلَن تَسْتَطِيعَ لَهُ طَلَبًا
walla ndox ma ŋiis te dootu ko ame feneen”.
42وَأُحِيطَ بِثَمَرِهِ فَأَصْبَحَ يُقَلِّبُ كَفَّيْهِ عَلَىٰ مَا أَنفَقَ فِيهَا وَهِيَ خَاوِيَةٌ عَلَىٰ عُرُوشِهَا وَيَقُولُ يَا لَيْتَنِي لَمْ أُشْرِكْ بِرَبِّي أَحَدًا
Alageef na meññent ma mu xëy di moqarñi ñaari yoxoom ngir la mu ca tàbbal ci alal, te fekk tool ba yàqu na, garab ya daanu, dàmme ca dàtt ya. Mu naan : “Ay aka neexoon bokkaalewuma kenn ak sama Boroom ! ”.
43وَلَمْ تَكُن لَّهُ فِئَةٌ يَنصُرُونَهُ مِن دُونِ اللَّهِ وَمَا كَانَ مُنتَصِرًا
Te amatul mbooloo mu ko mën a dimbali ku dul Yàlla. Te nekkul it di mënal boppam dara.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
41Aaya
Tekki — Al-Kahf 41
Simoore Al-Kahf Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : walla ndox ma ŋiis te dootu ko ame feneen”.Simoore Aaya 41/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Al-Kahf
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Wednesday, September 30, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


