Al-Kahf · 40/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
فَعَسَىٰ رَبِّي أَن يُؤْتِيَنِ خَيْرًا مِّن جَنَّتِكَ وَيُرْسِلَ عَلَيْهَا حُسْبَانًا مِّنَ السَّمَاءِ فَتُصْبِحَ صَعِيدًا زَلَقًا ۝٤٠
Fa`asaa Rabeee any yu`tiyani khairam min jannatika wa yursila `alaihaa husbaanam minas samaaa`i fatusbiha sa`eedan zalaqaa
📖 Tekkim Wolof
xéy-na sama Boroom jox ma lu gën sa tool, te yabal ca sa tool jéyya ju jóge asamaan ba mu nekk dénd bu amutul dara,
🎧 Dégg

📜 Aaya 38-42 — Al-Kahf

38لَّٰكِنَّا هُوَ اللَّهُ رَبِّي وَلَا أُشْرِكُ بِرَبِّي أَحَدًا
Waaye man, Moom Yàlla moo di sama Boroom ; te duma bokkaaleek sama Boroom kenn ?
39وَلَوْلَا إِذْ دَخَلْتَ جَنَّتَكَ قُلْتَ مَا شَاءَ اللَّهُ لَا قُوَّةَ إِلَّا بِاللَّهِ ۚ إِن تَرَنِ أَنَا أَقَلَّ مِنكَ مَالًا وَوَلَدًا
Lu teewoon ba ngay dugg ca tool ba nga wax ne : “Lu neex Yàlla [rekk ay am] ! Amul kenn ku am kàttan ku dul Yàlla”. Ndeem danga maa gis ma gën laa néew alal ak i doom,
40فَعَسَىٰ رَبِّي أَن يُؤْتِيَنِ خَيْرًا مِّن جَنَّتِكَ وَيُرْسِلَ عَلَيْهَا حُسْبَانًا مِّنَ السَّمَاءِ فَتُصْبِحَ صَعِيدًا زَلَقًا
xéy-na sama Boroom jox ma lu gën sa tool, te yabal ca sa tool jéyya ju jóge asamaan ba mu nekk dénd bu amutul dara,
41أَوْ يُصْبِحَ مَاؤُهَا غَوْرًا فَلَن تَسْتَطِيعَ لَهُ طَلَبًا
walla ndox ma ŋiis te dootu ko ame feneen”.
42وَأُحِيطَ بِثَمَرِهِ فَأَصْبَحَ يُقَلِّبُ كَفَّيْهِ عَلَىٰ مَا أَنفَقَ فِيهَا وَهِيَ خَاوِيَةٌ عَلَىٰ عُرُوشِهَا وَيَقُولُ يَا لَيْتَنِي لَمْ أُشْرِكْ بِرَبِّي أَحَدًا
Alageef na meññent ma mu xëy di moqarñi ñaari yoxoom ngir la mu ca tàbbal ci alal, te fekk tool ba yàqu na, garab ya daanu, dàmme ca dàtt ya. Mu naan : “Ay aka neexoon bokkaalewuma kenn ak sama Boroom ! ”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
40Aaya

Tekki — Al-Kahf 40

Simoore Al-Kahf Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : xéy-na sama Boroom jox ma lu gën sa tool, te…

Simoore Aaya 40/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers