Al-Baqara · 223/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
نِسَاؤُكُمْ حَرْثٌ لَّكُمْ فَأْتُوا حَرْثَكُمْ أَنَّىٰ شِئْتُمْ ۖ وَقَدِّمُوا لِأَنفُسِكُمْ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ وَاعْلَمُوا أَنَّكُم مُّلَاقُوهُ ۗ وَبَشِّرِ الْمُؤْمِنِينَ ٢٢٣
Transliteration
Nisaaa`ukum harsullakum faatoo harsakum annaa shi`tum wa qaddimoo li anfusikum; wattaqul laaha wa`lamooo annakum mulaaqooh; wa bash shirilmu `mineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Seeni soxna [jabar] seeni tool lañu ; dikkeleen seeni tool ca na mu leen neexee te ngeen jiital ngir seen bopp, buleen fàtte tudd Yàlla. Te ngeen ragal Yàlla te ngeen xam ne dangeen dajeek Moom. Te nanga bégal way-gëm ña !
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 221-225 — Al-Baqara
221وَلَا تَنكِحُوا الْمُشْرِكَاتِ حَتَّىٰ يُؤْمِنَّ ۚ وَلَأَمَةٌ مُّؤْمِنَةٌ خَيْرٌ مِّن مُّشْرِكَةٍ وَلَوْ أَعْجَبَتْكُمْ ۗ وَلَا تُنكِحُوا الْمُشْرِكِينَ حَتَّىٰ يُؤْمِنُوا ۚ وَلَعَبْدٌ مُّؤْمِنٌ خَيْرٌ مِّن مُّشْرِكٍ وَلَوْ أَعْجَبَكُمْ ۗ أُولَٰئِكَ يَدْعُونَ إِلَى النَّارِ ۖ وَاللَّهُ يَدْعُو إِلَى الْجَنَّةِ وَالْمَغْفِرَةِ بِإِذْنِهِ ۖ وَيُبَيِّنُ آيَاتِهِ لِلنَّاسِ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
Buleen takk soxna jigéen ñuy bokkaale li feek gëmuñu, jaam bu jigéen bu gëm moo gën jigéen [ju ñuy tuddeeb sang] juy bokkaale, doontale yéem na leen. Buleen may jabar góor ñuy bokkaale, jaam bu góor moo gën góor [gu ñuy tuddeeb sang] guy bokkaale, doontale yéem na leen. Ñooña dañuy woote jëme Safara ;Yàlla moom di woote jëme Àjjana ak ug njéggal, ci ndigalam. Te dana leeral ay laayaam nit ña ndax ñu fàttaliku [seen Boroom] !
222وَيَسْأَلُونَكَ عَنِ الْمَحِيضِ ۖ قُلْ هُوَ أَذًى فَاعْتَزِلُوا النِّسَاءَ فِي الْمَحِيضِ ۖ وَلَا تَقْرَبُوهُنَّ حَتَّىٰ يَطْهُرْنَ ۖ فَإِذَا تَطَهَّرْنَ فَأْتُوهُنَّ مِنْ حَيْثُ أَمَرَكُمُ اللَّهُ ۚ إِنَّ اللَّهَ يُحِبُّ التَّوَّابِينَ وَيُحِبُّ الْمُتَطَهِّرِينَ
- Danañu la laaj lu jëm ci mbërëg . - Neel : “Moom sobe la. Deeleen beru jigéen ña bu ñu nekkee ci mbërëg, buleen jege ba bañuy laab. Suñu laabee, ngeen duggeleen fa Yàlla digle ndax Yàlla sopp na ñay tuub, sopp na itam ñay laabal seen bopp”.
223نِسَاؤُكُمْ حَرْثٌ لَّكُمْ فَأْتُوا حَرْثَكُمْ أَنَّىٰ شِئْتُمْ ۖ وَقَدِّمُوا لِأَنفُسِكُمْ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ وَاعْلَمُوا أَنَّكُم مُّلَاقُوهُ ۗ وَبَشِّرِ الْمُؤْمِنِينَ
Seeni soxna [jabar] seeni tool lañu ; dikkeleen seeni tool ca na mu leen neexee te ngeen jiital ngir seen bopp, buleen fàtte tudd Yàlla. Te ngeen ragal Yàlla te ngeen xam ne dangeen dajeek Moom. Te nanga bégal way-gëm ña !
224وَلَا تَجْعَلُوا اللَّهَ عُرْضَةً لِّأَيْمَانِكُمْ أَن تَبَرُّوا وَتَتَّقُوا وَتُصْلِحُوا بَيْنَ النَّاسِ ۗ وَاللَّهُ سَمِيعٌ عَلِيمٌ
Buleen di giñ ci Yàlla, ba mu nekk gàllankoor gu leen teree def lu baax, walla ragal Yàlla mbaa yéwénal diggante nit ñi. Yàlla kuy dégg la te ku xam la.
225لَّا يُؤَاخِذُكُمُ اللَّهُ بِاللَّغْوِ فِي أَيْمَانِكُمْ وَلَٰكِن يُؤَاخِذُكُم بِمَا كَسَبَتْ قُلُوبُكُمْ ۗ وَاللَّهُ غَفُورٌ حَلِيمٌ
Yàlla duleen jàppe ngiñ ci kaf : Waaye Dana leen jàppe ngiñ lu seeni xol dëggu. Yàlla jéggalaakoon la te ku lewet la.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
223Aaya
Tekki — Al-Baqara 223
Simoore Al-Baqara Aaya 223 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seeni soxna [jabar] seeni tool lañu ; dikkeleen seeni tool…Simoore Aaya 223/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 221–225. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








