An-Nur · 6/64
Tekki Waxtaan — An-Nur
وَالَّذِينَ يَرْمُونَ أَزْوَاجَهُمْ وَلَمْ يَكُن لَّهُمْ شُهَدَاءُ إِلَّا أَنفُسُهُمْ فَشَهَادَةُ أَحَدِهِمْ أَرْبَعُ شَهَادَاتٍ بِاللَّهِ ۙ إِنَّهُ لَمِنَ الصَّادِقِينَ ۝٦
Wallazeena yarmoona azwaajahum wa lam yakul lahum shuhadaaa`u illaaa anfusuhum fashahaadatu ahadihim arb`u shahaadaatim billaahi innahoo laminas saadiqeen
📖 Tekkim Wolof
Ñay tuumaal seeni jabar te amuñu ay seede lu dul seen bopp, na waat ci Yàlla ñeenti yoon ne ku dëggu la,

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — An-Nur

4وَالَّذِينَ يَرْمُونَ الْمُحْصَنَاتِ ثُمَّ لَمْ يَأْتُوا بِأَرْبَعَةِ شُهَدَاءَ فَاجْلِدُوهُمْ ثَمَانِينَ جَلْدَةً وَلَا تَقْبَلُوا لَهُمْ شَهَادَةً أَبَدًا ۚ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْفَاسِقُونَ
Ñay yàq deru jigéen ña, saŋewu [ci jiiñ leen njaaloo] ba noppi ñàkk a indi ñeenti seede, nangeen leen dóor juróom-ñetti fukki yar, te buleen nangooti ñuy seede ba fàwwu. Ñoom ay saay-saay lañu,
5إِلَّا الَّذِينَ تَابُوا مِن بَعْدِ ذَٰلِكَ وَأَصْلَحُوا فَإِنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
ba mu des ña rëccu, tuub ginnaaw loolu, tey jëf u yiw, Yàlla Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
6وَالَّذِينَ يَرْمُونَ أَزْوَاجَهُمْ وَلَمْ يَكُن لَّهُمْ شُهَدَاءُ إِلَّا أَنفُسُهُمْ فَشَهَادَةُ أَحَدِهِمْ أَرْبَعُ شَهَادَاتٍ بِاللَّهِ ۙ إِنَّهُ لَمِنَ الصَّادِقِينَ
Ñay tuumaal seeni jabar te amuñu ay seede lu dul seen bopp, na waat ci Yàlla ñeenti yoon ne ku dëggu la,
7وَالْخَامِسَةُ أَنَّ لَعْنَتَ اللَّهِ عَلَيْهِ إِن كَانَ مِنَ الْكَاذِبِينَ
juróomeel ba mu waat ne “rëbbum Yàlla [sori yërmaandeem] na dal ci kawam su dee fenkat la”.
8وَيَدْرَأُ عَنْهَا الْعَذَابَ أَن تَشْهَدَ أَرْبَعَ شَهَادَاتٍ بِاللَّهِ ۙ إِنَّهُ لَمِنَ الْكَاذِبِينَ
Su jabar ja waate ñeenti yoon ci Yàlla ne waa ja fenkat la, kenn du ko sànni xeer [rajmu],
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
6Aaya

Tekki — An-Nur 6

Simoore An-Nur Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñay tuumaal seeni jabar te amuñu ay seede lu dul…

Simoore Aaya 6/64 — An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nur Dégg, An-Nur Tekki, An-Nur mp3, An-Nur pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers