Al-Furqan · 10/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
تَبَارَكَ الَّذِي إِن شَاءَ جَعَلَ لَكَ خَيْرًا مِّن ذَٰلِكَ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ وَيَجْعَل لَّكَ قُصُورًا ۝١٠
Tabaarakal lazeee in shaaa`a ja`ala laka khairam min zaalika jannaatin tajree min tahtihal anhaaru wa yaj`al laka qusooraa
📖 Tekkim Wolof
Yàlla ju barkeel ja nga xam ne bu Ko sooboon Mu defal la ci loolu Àjjana joo xam ay dex dañuy daw ci suufam ; Mu defal la it ay jénde.

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Al-Furqan

8أَوْ يُلْقَىٰ إِلَيْهِ كَنزٌ أَوْ تَكُونُ لَهُ جَنَّةٌ يَأْكُلُ مِنْهَا ۚ وَقَالَ الظَّالِمُونَ إِن تَتَّبِعُونَ إِلَّا رَجُلًا مَّسْحُورًا
Walla mu am ndàmb ? Mbaa mu am tooli dër di ci lekk ?”. Tooñkat ya naan : “Yéen daal toppiwuleen ku dul as waay ju ag njibar jàpp”.
9انظُرْ كَيْفَ ضَرَبُوا لَكَ الْأَمْثَالَ فَضَلُّوا فَلَا يَسْتَطِيعُونَ سَبِيلًا
Gisal ni ñu lay méngaléelee ! Dañuy sànku te amuñu ca wenn yoon.
10تَبَارَكَ الَّذِي إِن شَاءَ جَعَلَ لَكَ خَيْرًا مِّن ذَٰلِكَ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ وَيَجْعَل لَّكَ قُصُورًا
Yàlla ju barkeel ja nga xam ne bu Ko sooboon Mu defal la ci loolu Àjjana joo xam ay dex dañuy daw ci suufam ; Mu defal la it ay jénde.
11بَلْ كَذَّبُوا بِالسَّاعَةِ ۖ وَأَعْتَدْنَا لِمَن كَذَّبَ بِالسَّاعَةِ سَعِيرًا
Waaye wedd nañu Bis-pénc ba. Te Nun kat waajalal Nanu, képp ku weddi Bis-pénc ba, aw safara wuy jér-jéri.
12إِذَا رَأَتْهُم مِّن مَّكَانٍ بَعِيدٍ سَمِعُوا لَهَا تَغَيُّظًا وَزَفِيرًا
Saa su leen Safara soosu séenee fu sori, dinañu dégg riiram.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Al-Furqan 10

Simoore Al-Furqan Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla ju barkeel ja nga xam ne bu Ko sooboon…

Simoore Aaya 10/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, August 19, 2026

Don't forget us in your sincere prayers