An-Naml · 28/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
اذْهَب بِّكِتَابِي هَٰذَا فَأَلْقِهْ إِلَيْهِمْ ثُمَّ تَوَلَّ عَنْهُمْ فَانظُرْ مَاذَا يَرْجِعُونَ ۝٢٨
Izhab bikitaabee haaza fa alqih ilaihim summma tawalla `anhum fanzur maazaa yarji`oon
📖 Tekkim Wolof
Jëlal sama bataaxal bii ; boo demee nga sànni leen ko ; te dëppal xool ba xam na ñuy def.

🎧 Dégg


📜 Aaya 26-30 — An-Naml

26اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ رَبُّ الْعَرْشِ الْعَظِيمِ ۩
[Cëy] Yàlla ! Jeneen yàlla amul ju dul Moom, Mooy boroom gàngunaay [Aras] gu màgg ga.
27۞ قَالَ سَنَنظُرُ أَصَدَقْتَ أَمْ كُنتَ مِنَ الْكَاذِبِينَ
Suleymaan ne ko : “Dananu xool ndax wax nga dëgg walla dangay fen.
28اذْهَب بِّكِتَابِي هَٰذَا فَأَلْقِهْ إِلَيْهِمْ ثُمَّ تَوَلَّ عَنْهُمْ فَانظُرْ مَاذَا يَرْجِعُونَ
Jëlal sama bataaxal bii ; boo demee nga sànni leen ko ; te dëppal xool ba xam na ñuy def.
29قَالَتْ يَا أَيُّهَا الْمَلَأُ إِنِّي أُلْقِيَ إِلَيَّ كِتَابٌ كَرِيمٌ
Buur ba [Balxiis] ne leen : "Kilifay dëkk bi ! Man dey, sànni nañu ma bataaxal bu tedd.
30إِنَّهُ مِن سُلَيْمَانَ وَإِنَّهُ بِسْمِ اللَّهِ الرَّحْمَٰنِ الرَّحِيمِ
Mi ngi bawoo ca Suleymaan : “Ci turu Yàlla la Miy Yërëmaakoon, di Jaglewaakoon,
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — An-Naml 28

Simoore An-Naml Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jëlal sama bataaxal bii ; boo demee nga sànni leen…

Simoore Aaya 28/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers