An-Naml · 27/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
۞ قَالَ سَنَنظُرُ أَصَدَقْتَ أَمْ كُنتَ مِنَ الْكَاذِبِينَ ۝٢٧
Qaala sananzuru asadaqta am kunta minal kaazibeen
📖 Tekkim Wolof
Suleymaan ne ko : “Dananu xool ndax wax nga dëgg walla dangay fen.
🎧 Dégg

📜 Aaya 25-29 — An-Naml

25أَلَّا يَسْجُدُوا لِلَّهِ الَّذِي يُخْرِجُ الْخَبْءَ فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَيَعْلَمُ مَا تُخْفُونَ وَمَا تُعْلِنُونَ
Moo ndax duñu jaamu Yàlla Miy génne li nëbbu ci asamaan yeek suuf si, te Moo xam li ngeen di nëbb ak li ngeen di feeñal ?
26اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ رَبُّ الْعَرْشِ الْعَظِيمِ ۩
[Cëy] Yàlla ! Jeneen yàlla amul ju dul Moom, Mooy boroom gàngunaay [Aras] gu màgg ga.
27۞ قَالَ سَنَنظُرُ أَصَدَقْتَ أَمْ كُنتَ مِنَ الْكَاذِبِينَ
Suleymaan ne ko : “Dananu xool ndax wax nga dëgg walla dangay fen.
28اذْهَب بِّكِتَابِي هَٰذَا فَأَلْقِهْ إِلَيْهِمْ ثُمَّ تَوَلَّ عَنْهُمْ فَانظُرْ مَاذَا يَرْجِعُونَ
Jëlal sama bataaxal bii ; boo demee nga sànni leen ko ; te dëppal xool ba xam na ñuy def.
29قَالَتْ يَا أَيُّهَا الْمَلَأُ إِنِّي أُلْقِيَ إِلَيَّ كِتَابٌ كَرِيمٌ
Buur ba [Balxiis] ne leen : "Kilifay dëkk bi ! Man dey, sànni nañu ma bataaxal bu tedd.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — An-Naml 27

Simoore An-Naml Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Suleymaan ne ko : “Dananu xool ndax wax nga dëgg…

Simoore Aaya 27/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers