Aali Imran · 152/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
وَلَقَدْ صَدَقَكُمُ اللَّهُ وَعْدَهُ إِذْ تَحُسُّونَهُم بِإِذْنِهِ ۖ حَتَّىٰ إِذَا فَشِلْتُمْ وَتَنَازَعْتُمْ فِي الْأَمْرِ وَعَصَيْتُم مِّن بَعْدِ مَا أَرَاكُم مَّا تُحِبُّونَ ۚ مِنكُم مَّن يُرِيدُ الدُّنْيَا وَمِنكُم مَّن يُرِيدُ الْآخِرَةَ ۚ ثُمَّ صَرَفَكُمْ عَنْهُمْ لِيَبْتَلِيَكُمْ ۖ وَلَقَدْ عَفَا عَنكُمْ ۗ وَاللَّهُ ذُو فَضْلٍ عَلَى الْمُؤْمِنِينَ ١٥٢
Transliteration
Wa laqad sadaqakumul laahu wa`dahooo iz tahussoo nahum bi iznihee hattaaa izaa fashiltim wa tanaaza`tum fil amri wa `asaitum mim ba`di maaa araakum maa tuhibboon; minkum mai yureedud dunyaa wa minkum mai yureedul Aakhirah; summa sarafakum `anhum sarafakum `anhum liyabtaliyakum wa laqad `afaa `ankum; wallaahu zoo fadlin `alal mu`mineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yàlla def na la Mu leen digoon nekk dëgg, ba ngën di xeex ak ñoom ci ndigal, [ngeen not] ba ba ngeen sàqi ndigal la, ginnaaw ba ngeen janoo ak la ngeen bëgg [alal] àddina! Am na it ci yéen ñu bëgg [alali] àllaaxira. Ba noppi Yàlla wëlbati leen [soppi tooñeel ga] ngeen amoon ci ñoom, ngir nattu leen.Waaye baal na leen. Yàlla Boroom ngëneel la yu muy [sédd] ñi gëm.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 150-154 — Aali Imran
150بَلِ اللَّهُ مَوْلَاكُمْ ۖ وَهُوَ خَيْرُ النَّاصِرِينَ
Li wér mooy Yàllaa leen méngoo [yore seeni mbir] te Mooy ngëm ji kuy dimbali.
151سَنُلْقِي فِي قُلُوبِ الَّذِينَ كَفَرُوا الرُّعْبَ بِمَا أَشْرَكُوا بِاللَّهِ مَا لَمْ يُنَزِّلْ بِهِ سُلْطَانًا ۖ وَمَأْوَاهُمُ النَّارُ ۚ وَبِئْسَ مَثْوَى الظَّالِمِينَ
Dananu sànni ci xoli ñi weddi tiitaange ngir la ñu bokkaale Yàlla ak loo xam ne amul lay wuñu leen ca wàcceel. Safaraa di seen dëkkuwaay te dëkkuwaayu tooñkat ya bon na !
152وَلَقَدْ صَدَقَكُمُ اللَّهُ وَعْدَهُ إِذْ تَحُسُّونَهُم بِإِذْنِهِ ۖ حَتَّىٰ إِذَا فَشِلْتُمْ وَتَنَازَعْتُمْ فِي الْأَمْرِ وَعَصَيْتُم مِّن بَعْدِ مَا أَرَاكُم مَّا تُحِبُّونَ ۚ مِنكُم مَّن يُرِيدُ الدُّنْيَا وَمِنكُم مَّن يُرِيدُ الْآخِرَةَ ۚ ثُمَّ صَرَفَكُمْ عَنْهُمْ لِيَبْتَلِيَكُمْ ۖ وَلَقَدْ عَفَا عَنكُمْ ۗ وَاللَّهُ ذُو فَضْلٍ عَلَى الْمُؤْمِنِينَ
Yàlla def na la Mu leen digoon nekk dëgg, ba ngën di xeex ak ñoom ci ndigal, [ngeen not] ba ba ngeen sàqi ndigal la, ginnaaw ba ngeen janoo ak la ngeen bëgg [alal] àddina! Am na it ci yéen ñu bëgg [alali] àllaaxira. Ba noppi Yàlla wëlbati leen [soppi tooñeel ga] ngeen amoon ci ñoom, ngir nattu leen.Waaye baal na leen. Yàlla Boroom ngëneel la yu muy [sédd] ñi gëm.
153۞ إِذْ تُصْعِدُونَ وَلَا تَلْوُونَ عَلَىٰ أَحَدٍ وَالرَّسُولُ يَدْعُوكُمْ فِي أُخْرَاكُمْ فَأَثَابَكُمْ غَمًّا بِغَمٍّ لِّكَيْلَا تَحْزَنُوا عَلَىٰ مَا فَاتَكُمْ وَلَا مَا أَصَابَكُمْ ۗ وَاللَّهُ خَبِيرٌ بِمَا تَعْمَلُونَ
[Fàttalikuleen] ba ngeen di yéeg te geesuwuleen kenn, te Yonent bi di leen woo ci seen ginnaaw. Mu tegoon leen njàqare ya ci kaw njàqare ya, ndax ngeen bañ a mitteetlu la leen rëcc walla la leen dal. Yàlla ku deñ-kumpa la ci li ngeen di def.
154ثُمَّ أَنزَلَ عَلَيْكُم مِّن بَعْدِ الْغَمِّ أَمَنَةً نُّعَاسًا يَغْشَىٰ طَائِفَةً مِّنكُمْ ۖ وَطَائِفَةٌ قَدْ أَهَمَّتْهُمْ أَنفُسُهُمْ يَظُنُّونَ بِاللَّهِ غَيْرَ الْحَقِّ ظَنَّ الْجَاهِلِيَّةِ ۖ يَقُولُونَ هَل لَّنَا مِنَ الْأَمْرِ مِن شَيْءٍ ۗ قُلْ إِنَّ الْأَمْرَ كُلَّهُ لِلَّهِ ۗ يُخْفُونَ فِي أَنفُسِهِم مَّا لَا يُبْدُونَ لَكَ ۖ يَقُولُونَ لَوْ كَانَ لَنَا مِنَ الْأَمْرِ شَيْءٌ مَّا قُتِلْنَا هَاهُنَا ۗ قُل لَّوْ كُنتُمْ فِي بُيُوتِكُمْ لَبَرَزَ الَّذِينَ كُتِبَ عَلَيْهِمُ الْقَتْلُ إِلَىٰ مَضَاجِعِهِمْ ۖ وَلِيَبْتَلِيَ اللَّهُ مَا فِي صُدُورِكُمْ وَلِيُمَحِّصَ مَا فِي قُلُوبِكُمْ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ بِذَاتِ الصُّدُورِ
Wàcce na ginnaaw njàqare la, kóolute, muy gëmméntu gu muur ab kurél ci yéen [way- gëm ñi] te beneen kurél ba [naaféq ya] seen bopp rekk yitteel leen, ñu njortu ci Yàlla lu dul dëgg njortu ku réer. -Ñu naan : “Ndax mbir mi moom nanu ci dara [ba di ci reyante] ?”. Neel [Yaw Yonent bi]: “Mbirum Yàllaa.”. Ña nga nëbb ci seen biir lu ñu feeñalul, di wax naan : “Bu nu moomoon dara ci mbir mi kon duñu nu rey fii.” Tontuleen ne : “Bu ngeen toogoon ca seeni kër, ñañu dogal dee ci ñoom dana leen fekk ca seen kaw i lal. [Lii lépp am na] ngir Yàlla natt li nekk ci seeni dënn [xol], ak feeñal li nekk ci seeni xol. Te Yàlla ku xam la li nekk ci dënn yi.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
152Aaya
Tekki — Aali Imran 152
Simoore Aali Imran Aaya 152 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla def na la Mu leen digoon nekk dëgg, ba…Simoore Aaya 152/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 150–154. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








