Ya-Sin · 8/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
إِنَّا جَعَلْنَا فِي أَعْنَاقِهِمْ أَغْلَالًا فَهِيَ إِلَى الْأَذْقَانِ فَهُم مُّقْمَحُونَ ۝٨
Innaa ja`alnaa feee a`naaqihim aghlaalan fahiya ilal azqaani fahum muqmahoon
📖 Tekkim Wolof
Def Nanu ay jéng ci seeni loos, mu àndak seeni daayi sikkim : ñu joñ leen.

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Ya-Sin

6لِتُنذِرَ قَوْمًا مَّا أُنذِرَ آبَاؤُهُمْ فَهُمْ غَافِلُونَ
Ngir nga xupp aw nit ñoo xam ne kenn musul a xupp seeni baay : ñoom dañoo sàggan.
7لَقَدْ حَقَّ الْقَوْلُ عَلَىٰ أَكْثَرِهِمْ فَهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Àtte ba dog : te la ëpp ca ñoom [ca Lawhul Mahfuuj] ci ne duñu gëmati.
8إِنَّا جَعَلْنَا فِي أَعْنَاقِهِمْ أَغْلَالًا فَهِيَ إِلَى الْأَذْقَانِ فَهُم مُّقْمَحُونَ
Def Nanu ay jéng ci seeni loos, mu àndak seeni daayi sikkim : ñu joñ leen.
9وَجَعَلْنَا مِن بَيْنِ أَيْدِيهِمْ سَدًّا وَمِنْ خَلْفِهِمْ سَدًّا فَأَغْشَيْنَاهُمْ فَهُمْ لَا يُبْصِرُونَ
def Nanu ab ñag ci kanam ak ci seen ginnaaw ; Muur Nanu leen ba dootuñu gis.
10وَسَوَاءٌ عَلَيْهِمْ أَأَنذَرْتَهُمْ أَمْ لَمْ تُنذِرْهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Nga xupp leen ak nga ñàkk leen a xupp ñoo yem kepp ci ñoom : duñu mës a gëm.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Ya-Sin 8

Simoore Ya-Sin Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Def Nanu ay jéng ci seeni loos, mu àndak seeni…

Simoore Aaya 8/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers