Ya-Sin · 7/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
لَقَدْ حَقَّ الْقَوْلُ عَلَىٰ أَكْثَرِهِمْ فَهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ ٧
Transliteration
Laqad haqqal qawlu `alaaa aksarihim fahum laa yu`minoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Àtte ba dog : te la ëpp ca ñoom [ca Lawhul Mahfuuj] ci ne duñu gëmati.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 5-9 — Simoore Ya-Sin
5تَنزِيلَ الْعَزِيزِ الرَّحِيمِ
Mi ngi wàcce ci Yàlla boroom Kàttan ga di ab Jaglewaakoonu yërmaandeem.
6لِتُنذِرَ قَوْمًا مَّا أُنذِرَ آبَاؤُهُمْ فَهُمْ غَافِلُونَ
Ngir nga xupp aw nit ñoo xam ne kenn musul a xupp seeni baay : ñoom dañoo sàggan.
7لَقَدْ حَقَّ الْقَوْلُ عَلَىٰ أَكْثَرِهِمْ فَهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Àtte ba dog : te la ëpp ca ñoom [ca Lawhul Mahfuuj] ci ne duñu gëmati.
8إِنَّا جَعَلْنَا فِي أَعْنَاقِهِمْ أَغْلَالًا فَهِيَ إِلَى الْأَذْقَانِ فَهُم مُّقْمَحُونَ
Def Nanu ay jéng ci seeni loos, mu àndak seeni daayi sikkim : ñu joñ leen.
9وَجَعَلْنَا مِن بَيْنِ أَيْدِيهِمْ سَدًّا وَمِنْ خَلْفِهِمْ سَدًّا فَأَغْشَيْنَاهُمْ فَهُمْ لَا يُبْصِرُونَ
def Nanu ab ñag ci kanam ak ci seen ginnaaw ; Muur Nanu leen ba dootuñu gis.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
7Aaya
Tekki — Ya-Sin 7
Simoore Ya-Sin Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Àtte ba dog : te la ëpp ca ñoom [ca…Simoore Aaya 7/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








