Fussilat · 17/54
Tekki Waxtaan — Simoore Fussilat
وَأَمَّا ثَمُودُ فَهَدَيْنَاهُمْ فَاسْتَحَبُّوا الْعَمَىٰ عَلَى الْهُدَىٰ فَأَخَذَتْهُمْ صَاعِقَةُ الْعَذَابِ الْهُونِ بِمَا كَانُوا يَكْسِبُونَ ١٧
Transliteration
Wa ammaa Samoodu fahadinaahum fastahabbul `ama `alal huda fa akhazathum saa`iqatul `azaabil hooni bimaa kaanoo yaksiboon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Waa Samuud nag ñoom, gindi woon nanu leen ; waaye dañoo tànni ngumba bàyyi gindi ku (njub) dëng. Mbugalum doyadi fab leen muy peyug la ñu daan fàggu.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 15-19 — Simoore Fussilat
15فَأَمَّا عَادٌ فَاسْتَكْبَرُوا فِي الْأَرْضِ بِغَيْرِ الْحَقِّ وَقَالُوا مَنْ أَشَدُّ مِنَّا قُوَّةً ۖ أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّ اللَّهَ الَّذِي خَلَقَهُمْ هُوَ أَشَدُّ مِنْهُمْ قُوَّةً ۖ وَكَانُوا بِآيَاتِنَا يَجْحَدُونَ
Waa Aad, rëy-rëylu ci suuf ci lu dul dëgg, daan wax naan : “Ana ku ñu ëpp doole ? ” (Di damu) ! Daan féttéerlu ci sunuy laaya.
16فَأَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ رِيحًا صَرْصَرًا فِي أَيَّامٍ نَّحِسَاتٍ لِّنُذِيقَهُمْ عَذَابَ الْخِزْيِ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۖ وَلَعَذَابُ الْآخِرَةِ أَخْزَىٰ ۖ وَهُمْ لَا يُنصَرُونَ
Bayal nanu ca ñoom ngelawul callmeer lu sedd guy ay fan yu nduxum, ngir mosal leen mbugëlum toroxtaane ci dundug àddina sii. Te mbugëlum àllaaxiraa gën a man a toraxal te it kenn duleen fa dimbali.
17وَأَمَّا ثَمُودُ فَهَدَيْنَاهُمْ فَاسْتَحَبُّوا الْعَمَىٰ عَلَى الْهُدَىٰ فَأَخَذَتْهُمْ صَاعِقَةُ الْعَذَابِ الْهُونِ بِمَا كَانُوا يَكْسِبُونَ
Waa Samuud nag ñoom, gindi woon nanu leen ; waaye dañoo tànni ngumba bàyyi gindi ku (njub) dëng. Mbugalum doyadi fab leen muy peyug la ñu daan fàggu.
18وَنَجَّيْنَا الَّذِينَ آمَنُوا وَكَانُوا يَتَّقُونَ
Nu daldi musël ña gëmoon tey ragal Yàlla.
19وَيَوْمَ يُحْشَرُ أَعْدَاءُ اللَّهِ إِلَى النَّارِ فَهُمْ يُوزَعُونَ
Bu keroogee bis ba ñuy pang (dajale) nooni yàlla ya... Jëme leen Safara di leen gur-gur.
FussilatFihi Alxuraan
54Aaya
MeccanRevelation
17Aaya
Tekki — Fussilat 17
Simoore Fussilat Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waa Samuud nag ñoom, gindi woon nanu leen ; waaye…Simoore Aaya 17/54 — Simoore Fussilat فصلت (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Fussilat Dégg, Simoore Fussilat Tekki, Simoore Fussilat mp3, Simoore Fussilat pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Fussilat
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Wednesday, September 30, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


