Al-Ahqaf · 34/35
Tekki Waxtaan — Al-Ahqaf
وَيَوْمَ يُعْرَضُ الَّذِينَ كَفَرُوا عَلَى النَّارِ أَلَيْسَ هَٰذَا بِالْحَقِّ ۖ قَالُوا بَلَىٰ وَرَبِّنَا ۚ قَالَ فَذُوقُوا الْعَذَابَ بِمَا كُنتُمْ تَكْفُرُونَ ۝٣٤
Wa Yawma yu`radul lazeena kafaroo `alan naari alaisa haaza bil haqq; qaaloo balaa wa Rabbinaa; qaala fazooqul `azaaba bimaa kuntum takfuroon
📖 Tekkim Wolof
Cay bu keroogee bis ba ñuy gaaral yéefar ya ca Safara (te naan leen) : “Ndax lii du dëgg ? ” Ñuy tontu naan : “Axakañ , ak sunu màggug Boroom”. Mu ne leen : “Tokamtiku leen mbugël ma ngir li ngeen daan weddi”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 32-35 — Al-Ahqaf

32وَمَن لَّا يُجِبْ دَاعِيَ اللَّهِ فَلَيْسَ بِمُعْجِزٍ فِي الْأَرْضِ وَلَيْسَ لَهُ مِن دُونِهِ أَوْلِيَاءُ ۚ أُولَٰئِكَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Te nag képp ku wuyuwul wootekatu Yàlla ba. Du man a raw mukk Yàlla ci kaw suuf si, te it du am ku koy man a dimbali ginnaaw Yàlla. Ñooñee ña nga ci réer gu bir sori.
33أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّ اللَّهَ الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَلَمْ يَعْيَ بِخَلْقِهِنَّ بِقَادِرٍ عَلَىٰ أَن يُحْيِيَ الْمَوْتَىٰ ۚ بَلَىٰ إِنَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Xanaa gisuñu ne Yàllaa bind asamaan yeek suuf si, te sonnut ci bind gi mu leen bind sàkk leen, xanaa war na man a dekkal néew ? Waaw-waaw. Moom man na lépp lu ne.
34وَيَوْمَ يُعْرَضُ الَّذِينَ كَفَرُوا عَلَى النَّارِ أَلَيْسَ هَٰذَا بِالْحَقِّ ۖ قَالُوا بَلَىٰ وَرَبِّنَا ۚ قَالَ فَذُوقُوا الْعَذَابَ بِمَا كُنتُمْ تَكْفُرُونَ
Cay bu keroogee bis ba ñuy gaaral yéefar ya ca Safara (te naan leen) : “Ndax lii du dëgg ? ” Ñuy tontu naan : “Axakañ , ak sunu màggug Boroom”. Mu ne leen : “Tokamtiku leen mbugël ma ngir li ngeen daan weddi”.
35فَاصْبِرْ كَمَا صَبَرَ أُولُو الْعَزْمِ مِنَ الرُّسُلِ وَلَا تَسْتَعْجِل لَّهُمْ ۚ كَأَنَّهُمْ يَوْمَ يَرَوْنَ مَا يُوعَدُونَ لَمْ يَلْبَثُوا إِلَّا سَاعَةً مِّن نَّهَارٍ ۚ بَلَاغٌ ۚ فَهَلْ يُهْلَكُ إِلَّا الْقَوْمُ الْفَاسِقُونَ
Yaw (Muhammad) na ngay muñ ni Yonent ya doonoon boroomuk dogu daan muñ; te buleen di yàkkamtil [mbugël]. Ndax bis bu ñu nee gegg ci li ñu leen daan tëkkoo, danuy mel ni masuñoo sax (dund) kon ndax dana alku ku dul saay-saay sa?
Al-AhqafFihi Alxuraan
35Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Al-Ahqaf 34

Simoore Al-Ahqaf Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Cay bu keroogee bis ba ñuy gaaral yéefar ya ca…

Simoore Aaya 34/35 — Al-Ahqaf الأحقاف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahqaf Dégg, Al-Ahqaf Tekki, Al-Ahqaf mp3, Al-Ahqaf pdf. Aaya 32–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers