Al-Ahqaf · 35/35
Tekki Waxtaan — Al-Ahqaf
فَاصْبِرْ كَمَا صَبَرَ أُولُو الْعَزْمِ مِنَ الرُّسُلِ وَلَا تَسْتَعْجِل لَّهُمْ ۚ كَأَنَّهُمْ يَوْمَ يَرَوْنَ مَا يُوعَدُونَ لَمْ يَلْبَثُوا إِلَّا سَاعَةً مِّن نَّهَارٍ ۚ بَلَاغٌ ۚ فَهَلْ يُهْلَكُ إِلَّا الْقَوْمُ الْفَاسِقُونَ ٣٥
Transliteration
Fasbir kamaa sabara ulul `azmi minar Rusuli wa laa tasta`jil lahum; ka annahum Yawma yarawna maa yoo`adoona lam yalbasooo illaa saa`atam min nahaar; balaagh; fahal yuhlaku illal qawmul faasiqoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yaw (Muhammad) na ngay muñ ni Yonent ya doonoon boroomuk dogu daan muñ; te buleen di yàkkamtil [mbugël]. Ndax bis bu ñu nee gegg ci li ñu leen daan tëkkoo, danuy mel ni masuñoo sax (dund) kon ndax dana alku ku dul saay-saay sa?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 33-35 — Al-Ahqaf
33أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّ اللَّهَ الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَلَمْ يَعْيَ بِخَلْقِهِنَّ بِقَادِرٍ عَلَىٰ أَن يُحْيِيَ الْمَوْتَىٰ ۚ بَلَىٰ إِنَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Xanaa gisuñu ne Yàllaa bind asamaan yeek suuf si, te sonnut ci bind gi mu leen bind sàkk leen, xanaa war na man a dekkal néew ? Waaw-waaw. Moom man na lépp lu ne.
34وَيَوْمَ يُعْرَضُ الَّذِينَ كَفَرُوا عَلَى النَّارِ أَلَيْسَ هَٰذَا بِالْحَقِّ ۖ قَالُوا بَلَىٰ وَرَبِّنَا ۚ قَالَ فَذُوقُوا الْعَذَابَ بِمَا كُنتُمْ تَكْفُرُونَ
Cay bu keroogee bis ba ñuy gaaral yéefar ya ca Safara (te naan leen) : “Ndax lii du dëgg ? ” Ñuy tontu naan : “Axakañ , ak sunu màggug Boroom”. Mu ne leen : “Tokamtiku leen mbugël ma ngir li ngeen daan weddi”.
35فَاصْبِرْ كَمَا صَبَرَ أُولُو الْعَزْمِ مِنَ الرُّسُلِ وَلَا تَسْتَعْجِل لَّهُمْ ۚ كَأَنَّهُمْ يَوْمَ يَرَوْنَ مَا يُوعَدُونَ لَمْ يَلْبَثُوا إِلَّا سَاعَةً مِّن نَّهَارٍ ۚ بَلَاغٌ ۚ فَهَلْ يُهْلَكُ إِلَّا الْقَوْمُ الْفَاسِقُونَ
Yaw (Muhammad) na ngay muñ ni Yonent ya doonoon boroomuk dogu daan muñ; te buleen di yàkkamtil [mbugël]. Ndax bis bu ñu nee gegg ci li ñu leen daan tëkkoo, danuy mel ni masuñoo sax (dund) kon ndax dana alku ku dul saay-saay sa?
Al-AhqafFihi Alxuraan
35Aaya
MeccanRevelation
35Aaya
Tekki — Al-Ahqaf 35
Simoore Al-Ahqaf Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaw (Muhammad) na ngay muñ ni Yonent ya doonoon boroomuk…Simoore Aaya 35/35 — Al-Ahqaf الأحقاف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahqaf Dégg, Al-Ahqaf Tekki, Al-Ahqaf mp3, Al-Ahqaf pdf. Aaya 33–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








