Muhammad · 12/38
Tekki Waxtaan — Muhammad
إِنَّ اللَّهَ يُدْخِلُ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۖ وَالَّذِينَ كَفَرُوا يَتَمَتَّعُونَ وَيَأْكُلُونَ كَمَا تَأْكُلُ الْأَنْعَامُ وَالنَّارُ مَثْوًى لَّهُمْ ۝١٢
Innal-laaha yudkhilul lazeena aamanoo wa `amilus saalihaati Jannaatin tajree min tahtihal anhaaru wallazeena kafaroo yatamatta`oona wa yaakuloona kamaa taakuluian`aamu wan Naaru maswallahum
📖 Tekkim Wolof
Yàlla dana tàbbal ñi gëmoon te daan jëfe yiw, Àjjana yoo xam ne ay dex ñooy daw ci suufam ronu leen. Ña weddiwoon ñoom dañu daan bànneexu ak daan lekk ni jur gi di lekke ; te safaraay séen saxuwaay.
🎧 Dégg

📜 Aaya 10-14 — Muhammad

10۞ أَفَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ دَمَّرَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ ۖ وَلِلْكَافِرِينَ أَمْثَالُهَا
Moo xanaa dañoo wërul ca réew yi (suuf si) bay xool naka la mujjug ña leen jiitu deme woon ? Yàlla da leen nappaaje (faag leen). Noonu it la yéefar yi di mujje.
11ذَٰلِكَ بِأَنَّ اللَّهَ مَوْلَى الَّذِينَ آمَنُوا وَأَنَّ الْكَافِرِينَ لَا مَوْلَىٰ لَهُمْ
Dafa fekk ne Yàlla mooy méngóo di Aar ñi gëm ; yéefar yi nag ñoom amu ñu ku leen di aar.
12إِنَّ اللَّهَ يُدْخِلُ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۖ وَالَّذِينَ كَفَرُوا يَتَمَتَّعُونَ وَيَأْكُلُونَ كَمَا تَأْكُلُ الْأَنْعَامُ وَالنَّارُ مَثْوًى لَّهُمْ
Yàlla dana tàbbal ñi gëmoon te daan jëfe yiw, Àjjana yoo xam ne ay dex ñooy daw ci suufam ronu leen. Ña weddiwoon ñoom dañu daan bànneexu ak daan lekk ni jur gi di lekke ; te safaraay séen saxuwaay.
13وَكَأَيِّن مِّن قَرْيَةٍ هِيَ أَشَدُّ قُوَّةً مِّن قَرْيَتِكَ الَّتِي أَخْرَجَتْكَ أَهْلَكْنَاهُمْ فَلَا نَاصِرَ لَهُمْ
Ak i bari dëkk, yu ëppoon doole fuuf sa dëkk bii ñu la génne, te dañu leen faagaagal, te amul kenn ku leen musal.
14أَفَمَن كَانَ عَلَىٰ بَيِّنَةٍ مِّن رَّبِّهِ كَمَن زُيِّنَ لَهُ سُوءُ عَمَلِهِ وَاتَّبَعُوا أَهْوَاءَهُم
Moo ndax kiy topp firnde yu leer yu tukkee ci Boroomam niróok naak ñay jàppe séeni ñaawtéef lu rafet tey topp séeni bànneex.
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
12Aaya

Tekki — Muhammad 12

Simoore Muhammad Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla dana tàbbal ñi gëmoon te daan jëfe yiw, Àjjana…

Simoore Aaya 12/38 — Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Muhammad Dégg, Muhammad Tekki, Muhammad mp3, Muhammad pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers