Muhammad · 11/38
Tekki Waxtaan — Muhammad
ذَٰلِكَ بِأَنَّ اللَّهَ مَوْلَى الَّذِينَ آمَنُوا وَأَنَّ الْكَافِرِينَ لَا مَوْلَىٰ لَهُمْ ١١
Transliteration
Zaalika bi annal laaha mawlal lazeena aamanoo wa annal kaafireena laa mawlaa lahum
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Dafa fekk ne Yàlla mooy méngóo di Aar ñi gëm ; yéefar yi nag ñoom amu ñu ku leen di aar.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 9-13 — Muhammad
9ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ كَرِهُوا مَا أَنزَلَ اللَّهُ فَأَحْبَطَ أَعْمَالَهُمْ
Li ko waral moo di ne dañoo sibóon li Yàlla daan wàcce ci moom it. Mu daldi sippi séeni jëf (neenal ko).
10۞ أَفَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ دَمَّرَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ ۖ وَلِلْكَافِرِينَ أَمْثَالُهَا
Moo xanaa dañoo wërul ca réew yi (suuf si) bay xool naka la mujjug ña leen jiitu deme woon ? Yàlla da leen nappaaje (faag leen). Noonu it la yéefar yi di mujje.
11ذَٰلِكَ بِأَنَّ اللَّهَ مَوْلَى الَّذِينَ آمَنُوا وَأَنَّ الْكَافِرِينَ لَا مَوْلَىٰ لَهُمْ
Dafa fekk ne Yàlla mooy méngóo di Aar ñi gëm ; yéefar yi nag ñoom amu ñu ku leen di aar.
12إِنَّ اللَّهَ يُدْخِلُ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۖ وَالَّذِينَ كَفَرُوا يَتَمَتَّعُونَ وَيَأْكُلُونَ كَمَا تَأْكُلُ الْأَنْعَامُ وَالنَّارُ مَثْوًى لَّهُمْ
Yàlla dana tàbbal ñi gëmoon te daan jëfe yiw, Àjjana yoo xam ne ay dex ñooy daw ci suufam ronu leen. Ña weddiwoon ñoom dañu daan bànneexu ak daan lekk ni jur gi di lekke ; te safaraay séen saxuwaay.
13وَكَأَيِّن مِّن قَرْيَةٍ هِيَ أَشَدُّ قُوَّةً مِّن قَرْيَتِكَ الَّتِي أَخْرَجَتْكَ أَهْلَكْنَاهُمْ فَلَا نَاصِرَ لَهُمْ
Ak i bari dëkk, yu ëppoon doole fuuf sa dëkk bii ñu la génne, te dañu leen faagaagal, te amul kenn ku leen musal.
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
11Aaya
Tekki — Muhammad 11
Simoore Muhammad Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dafa fekk ne Yàlla mooy méngóo di Aar ñi gëm…Simoore Aaya 11/38 — Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Muhammad Dégg, Muhammad Tekki, Muhammad mp3, Muhammad pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








