Muhammad · 30/38
Tekki Waxtaan — Muhammad
وَلَوْ نَشَاءُ لَأَرَيْنَاكَهُمْ فَلَعَرَفْتَهُم بِسِيمَاهُمْ ۚ وَلَتَعْرِفَنَّهُمْ فِي لَحْنِ الْقَوْلِ ۚ وَاللَّهُ يَعْلَمُ أَعْمَالَكُمْ ٣٠
Transliteration
Wa law nashaaa`u la-arainaakahum fala `araftahum bi seemaahum; wa lata`rifan nahum fee lahnil qawl; wallaahu ya`lamu a`maalakum
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bu Nu sooboon danga leen gis jàrr. Te danga leen xam ci séen màndarga ; danga leen man a xam itam ci séen galeenu waxiin. Yàlla xam na séeni jëf.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 28-32 — Muhammad
28ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمُ اتَّبَعُوا مَا أَسْخَطَ اللَّهَ وَكَرِهُوا رِضْوَانَهُ فَأَحْبَطَ أَعْمَالَهُمْ
Li ko waral moo di dañuy topp luy waral xarabug Yàlla, tey bañ lépp luy ngëramal Yàlla. Moom it mu daldi sippi séen jëf.
29أَمْ حَسِبَ الَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ أَن لَّن يُخْرِجَ اللَّهُ أَضْغَانَهُمْ
Moo ndax naaféq ya dañoo foog ne Yàlla du génne mbañeel gi ëmbul (Yonenta bi) mu ne fàŋŋ ?
30وَلَوْ نَشَاءُ لَأَرَيْنَاكَهُمْ فَلَعَرَفْتَهُم بِسِيمَاهُمْ ۚ وَلَتَعْرِفَنَّهُمْ فِي لَحْنِ الْقَوْلِ ۚ وَاللَّهُ يَعْلَمُ أَعْمَالَكُمْ
Bu Nu sooboon danga leen gis jàrr. Te danga leen xam ci séen màndarga ; danga leen man a xam itam ci séen galeenu waxiin. Yàlla xam na séeni jëf.
31وَلَنَبْلُوَنَّكُمْ حَتَّىٰ نَعْلَمَ الْمُجَاهِدِينَ مِنكُمْ وَالصَّابِرِينَ وَنَبْلُوَ أَخْبَارَكُمْ
Dananu leen natt ba baa nuy xam, ñay jihaad ci yéen ak muñkat ya, te it da nanu feeñal séeni jëf (yu baax ak yu bon).
32إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا وَصَدُّوا عَن سَبِيلِ اللَّهِ وَشَاقُّوا الرَّسُولَ مِن بَعْدِ مَا تَبَيَّنَ لَهُمُ الْهُدَىٰ لَن يَضُرُّوا اللَّهَ شَيْئًا وَسَيُحْبِطُ أَعْمَالَهُمْ
Ña daan weddi tey dumóoyu yoonu Yàlla te daan sonal Yonenta bi ginaaw (ba ñu xamee) njub ga mu leer nàññ, manuñoo wàññi Yàlla dara. Te dana sippi seen jëf.
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
30Aaya
Tekki — Muhammad 30
Simoore Muhammad Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu Nu sooboon danga leen gis jàrr. Te danga leen…Simoore Aaya 30/38 — Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Muhammad Dégg, Muhammad Tekki, Muhammad mp3, Muhammad pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








