Muhammad · 31/38
Tekki Waxtaan — Muhammad
وَلَنَبْلُوَنَّكُمْ حَتَّىٰ نَعْلَمَ الْمُجَاهِدِينَ مِنكُمْ وَالصَّابِرِينَ وَنَبْلُوَ أَخْبَارَكُمْ ۝٣١
Wa lanabluwannakum hattaa na`lamal mujaahideena minkum wassaabireena wa nabluwa akhbaarakum
📖 Tekkim Wolof
Dananu leen natt ba baa nuy xam, ñay jihaad ci yéen ak muñkat ya, te it da nanu feeñal séeni jëf (yu baax ak yu bon).
🎧 Dégg

📜 Aaya 29-33 — Muhammad

29أَمْ حَسِبَ الَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ أَن لَّن يُخْرِجَ اللَّهُ أَضْغَانَهُمْ
Moo ndax naaféq ya dañoo foog ne Yàlla du génne mbañeel gi ëmbul (Yonenta bi) mu ne fàŋŋ ?
30وَلَوْ نَشَاءُ لَأَرَيْنَاكَهُمْ فَلَعَرَفْتَهُم بِسِيمَاهُمْ ۚ وَلَتَعْرِفَنَّهُمْ فِي لَحْنِ الْقَوْلِ ۚ وَاللَّهُ يَعْلَمُ أَعْمَالَكُمْ
Bu Nu sooboon danga leen gis jàrr. Te danga leen xam ci séen màndarga ; danga leen man a xam itam ci séen galeenu waxiin. Yàlla xam na séeni jëf.
31وَلَنَبْلُوَنَّكُمْ حَتَّىٰ نَعْلَمَ الْمُجَاهِدِينَ مِنكُمْ وَالصَّابِرِينَ وَنَبْلُوَ أَخْبَارَكُمْ
Dananu leen natt ba baa nuy xam, ñay jihaad ci yéen ak muñkat ya, te it da nanu feeñal séeni jëf (yu baax ak yu bon).
32إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا وَصَدُّوا عَن سَبِيلِ اللَّهِ وَشَاقُّوا الرَّسُولَ مِن بَعْدِ مَا تَبَيَّنَ لَهُمُ الْهُدَىٰ لَن يَضُرُّوا اللَّهَ شَيْئًا وَسَيُحْبِطُ أَعْمَالَهُمْ
Ña daan weddi tey dumóoyu yoonu Yàlla te daan sonal Yonenta bi ginaaw (ba ñu xamee) njub ga mu leer nàññ, manuñoo wàññi Yàlla dara. Te dana sippi seen jëf.
33۞ يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا أَطِيعُوا اللَّهَ وَأَطِيعُوا الرَّسُولَ وَلَا تُبْطِلُوا أَعْمَالَكُمْ
eey yéen ñi gëm ! Topp leen Yàlla tey topp Yonent bi, te bu leen di neenal séeni jëf.
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
31Aaya

Tekki — Muhammad 31

Simoore Muhammad Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dananu leen natt ba baa nuy xam, ñay jihaad ci…

Simoore Aaya 31/38 — Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Muhammad Dégg, Muhammad Tekki, Muhammad mp3, Muhammad pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers