Muhammad · 29/38
Tekki Waxtaan — Muhammad
أَمْ حَسِبَ الَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ أَن لَّن يُخْرِجَ اللَّهُ أَضْغَانَهُمْ ۝٢٩
Am hasibal lazeena fee quloobihim maradun al lan yukhrijal laahu adghaanahum
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax naaféq ya dañoo foog ne Yàlla du génne mbañeel gi ëmbul (Yonenta bi) mu ne fàŋŋ ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 27-31 — Muhammad

27فَكَيْفَ إِذَا تَوَفَّتْهُمُ الْمَلَائِكَةُ يَضْرِبُونَ وُجُوهَهُمْ وَأَدْبَارَهُمْ
Naka la séeni mbir di mujje su leen Malaaka ya jekkalee, di leen dóor ci kanam ak ginnaaw ?
28ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمُ اتَّبَعُوا مَا أَسْخَطَ اللَّهَ وَكَرِهُوا رِضْوَانَهُ فَأَحْبَطَ أَعْمَالَهُمْ
Li ko waral moo di dañuy topp luy waral xarabug Yàlla, tey bañ lépp luy ngëramal Yàlla. Moom it mu daldi sippi séen jëf.
29أَمْ حَسِبَ الَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ أَن لَّن يُخْرِجَ اللَّهُ أَضْغَانَهُمْ
Moo ndax naaféq ya dañoo foog ne Yàlla du génne mbañeel gi ëmbul (Yonenta bi) mu ne fàŋŋ ?
30وَلَوْ نَشَاءُ لَأَرَيْنَاكَهُمْ فَلَعَرَفْتَهُم بِسِيمَاهُمْ ۚ وَلَتَعْرِفَنَّهُمْ فِي لَحْنِ الْقَوْلِ ۚ وَاللَّهُ يَعْلَمُ أَعْمَالَكُمْ
Bu Nu sooboon danga leen gis jàrr. Te danga leen xam ci séen màndarga ; danga leen man a xam itam ci séen galeenu waxiin. Yàlla xam na séeni jëf.
31وَلَنَبْلُوَنَّكُمْ حَتَّىٰ نَعْلَمَ الْمُجَاهِدِينَ مِنكُمْ وَالصَّابِرِينَ وَنَبْلُوَ أَخْبَارَكُمْ
Dananu leen natt ba baa nuy xam, ñay jihaad ci yéen ak muñkat ya, te it da nanu feeñal séeni jëf (yu baax ak yu bon).
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
29Aaya

Tekki — Muhammad 29

Simoore Muhammad Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax naaféq ya dañoo foog ne Yàlla du génne…

Simoore Aaya 29/38 — Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Muhammad Dégg, Muhammad Tekki, Muhammad mp3, Muhammad pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers