Al-Maida · 55/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
إِنَّمَا وَلِيُّكُمُ اللَّهُ وَرَسُولُهُ وَالَّذِينَ آمَنُوا الَّذِينَ يُقِيمُونَ الصَّلَاةَ وَيُؤْتُونَ الزَّكَاةَ وَهُمْ رَاكِعُونَ ٥٥
Transliteration
Innamaa waliyyukumul laahu wa Rasooluhoo wal lazeena aamanul lazeena yuqeemoonas Salaata wa yu`toonaz Zakaata wa hum raaki`oon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Amul keneen ku far ak yéen ku dul Yàlla ak ab Yonentam, ak way-gëm ña nga xam ne danañu taxawal julli, di génne asaka te di way-sëgg.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 53-57 — Al-Maida
53وَيَقُولُ الَّذِينَ آمَنُوا أَهَٰؤُلَاءِ الَّذِينَ أَقْسَمُوا بِاللَّهِ جَهْدَ أَيْمَانِهِمْ ۙ إِنَّهُمْ لَمَعَكُمْ ۚ حَبِطَتْ أَعْمَالُهُمْ فَأَصْبَحُوا خَاسِرِينَ
Ba way-gëm ña naan : “Moo ndax du ñii ñoo doon giñ ci Yàlla fa ngiñ gën a màggee ngir ne ñoom ñook yéen a ànd bu wér ? ” Seeni jëf sippiku na [yàqu], ñu mujj di ñu yàqule.
54يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا مَن يَرْتَدَّ مِنكُمْ عَن دِينِهِ فَسَوْفَ يَأْتِي اللَّهُ بِقَوْمٍ يُحِبُّهُمْ وَيُحِبُّونَهُ أَذِلَّةٍ عَلَى الْمُؤْمِنِينَ أَعِزَّةٍ عَلَى الْكَافِرِينَ يُجَاهِدُونَ فِي سَبِيلِ اللَّهِ وَلَا يَخَافُونَ لَوْمَةَ لَائِمٍ ۚ ذَٰلِكَ فَضْلُ اللَّهِ يُؤْتِيهِ مَن يَشَاءُ ۚ وَاللَّهُ وَاسِعٌ عَلِيمٌ
Éy yéen ñi gëm ! Ku ci murtad ci yéen ba génn diineem... Yàlla Dana indi nit ñoo xam ne sopp Na leen , ñu sopp Ko, di ñu woyoflu ci jullit ñi te dëgër ci yéefar yi. Loolu ngënéelu Yàlla la. Ku Ko neex la koy jox. Yàlla Ku yaatu mbir la, Ku xam la.
55إِنَّمَا وَلِيُّكُمُ اللَّهُ وَرَسُولُهُ وَالَّذِينَ آمَنُوا الَّذِينَ يُقِيمُونَ الصَّلَاةَ وَيُؤْتُونَ الزَّكَاةَ وَهُمْ رَاكِعُونَ
Amul keneen ku far ak yéen ku dul Yàlla ak ab Yonentam, ak way-gëm ña nga xam ne danañu taxawal julli, di génne asaka te di way-sëgg.
56وَمَن يَتَوَلَّ اللَّهَ وَرَسُولَهُ وَالَّذِينَ آمَنُوا فَإِنَّ حِزْبَ اللَّهِ هُمُ الْغَالِبُونَ
Ku xaritook Yàlla ak Yonentam ak way-gëm ña, [na xam ne] ña ànd ak Yàlla ñooy nit ña [gàddu ndam la].
57يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَتَّخِذُوا الَّذِينَ اتَّخَذُوا دِينَكُمْ هُزُوًا وَلَعِبًا مِّنَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ مِن قَبْلِكُمْ وَالْكُفَّارَ أَوْلِيَاءَ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen jàpp xarit ña nga xam ne dañuy jàppe seen diine ay caaxaan ak po, ca ña leen jëkk a jot Téere ak yéefar ya. Ragal-leen Yàlla ndegam way-gëm ngeen.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
55Aaya
Tekki — Al-Maida 55
Simoore Al-Maida Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Amul keneen ku far ak yéen ku dul Yàlla ak…Simoore Aaya 55/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








