Al-Maida · 56/120
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Maida
وَمَن يَتَوَلَّ اللَّهَ وَرَسُولَهُ وَالَّذِينَ آمَنُوا فَإِنَّ حِزْبَ اللَّهِ هُمُ الْغَالِبُونَ ۝٥٦
Wa mai yatawallal laaha wa Rasoolahoo wallazeena aamanoo fa inna hizbal laahi humul ghaaliboon
📖 Tekkim Wolof
Ku xaritook Yàlla ak Yonentam ak way-gëm ña, [na xam ne] ña ànd ak Yàlla ñooy nit ña [gàddu ndam la].

🎧 Dégg


📜 Aaya 54-58 — Simoore Al-Maida

54يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا مَن يَرْتَدَّ مِنكُمْ عَن دِينِهِ فَسَوْفَ يَأْتِي اللَّهُ بِقَوْمٍ يُحِبُّهُمْ وَيُحِبُّونَهُ أَذِلَّةٍ عَلَى الْمُؤْمِنِينَ أَعِزَّةٍ عَلَى الْكَافِرِينَ يُجَاهِدُونَ فِي سَبِيلِ اللَّهِ وَلَا يَخَافُونَ لَوْمَةَ لَائِمٍ ۚ ذَٰلِكَ فَضْلُ اللَّهِ يُؤْتِيهِ مَن يَشَاءُ ۚ وَاللَّهُ وَاسِعٌ عَلِيمٌ
Éy yéen ñi gëm ! Ku ci murtad ci yéen ba génn diineem... Yàlla Dana indi nit ñoo xam ne sopp Na leen , ñu sopp Ko, di ñu woyoflu ci jullit ñi te dëgër ci yéefar yi. Loolu ngënéelu Yàlla la. Ku Ko neex la koy jox. Yàlla Ku yaatu mbir la, Ku xam la.
55إِنَّمَا وَلِيُّكُمُ اللَّهُ وَرَسُولُهُ وَالَّذِينَ آمَنُوا الَّذِينَ يُقِيمُونَ الصَّلَاةَ وَيُؤْتُونَ الزَّكَاةَ وَهُمْ رَاكِعُونَ
Amul keneen ku far ak yéen ku dul Yàlla ak ab Yonentam, ak way-gëm ña nga xam ne danañu taxawal julli, di génne asaka te di way-sëgg.
56وَمَن يَتَوَلَّ اللَّهَ وَرَسُولَهُ وَالَّذِينَ آمَنُوا فَإِنَّ حِزْبَ اللَّهِ هُمُ الْغَالِبُونَ
Ku xaritook Yàlla ak Yonentam ak way-gëm ña, [na xam ne] ña ànd ak Yàlla ñooy nit ña [gàddu ndam la].
57يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَتَّخِذُوا الَّذِينَ اتَّخَذُوا دِينَكُمْ هُزُوًا وَلَعِبًا مِّنَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ مِن قَبْلِكُمْ وَالْكُفَّارَ أَوْلِيَاءَ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen jàpp xarit ña nga xam ne dañuy jàppe seen diine ay caaxaan ak po, ca ña leen jëkk a jot Téere ak yéefar ya. Ragal-leen Yàlla ndegam way-gëm ngeen.
58وَإِذَا نَادَيْتُمْ إِلَى الصَّلَاةِ اتَّخَذُوهَا هُزُوًا وَلَعِبًا ۚ ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ قَوْمٌ لَّا يَعْقِلُونَ
Bu ngeen di woote jëm ci julli, [ñoom] ñu jàppe ko caaxaan ak am po. Ñoom dañudi ay nit ñu xel-luwul.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
56Aaya

Tekki — Al-Maida 56

Simoore Al-Maida Aaya 56 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ku xaritook Yàlla ak Yonentam ak way-gëm ña, [na xam…

Simoore Aaya 56/120 — Simoore Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Maida Dégg, Simoore Al-Maida Tekki, Simoore Al-Maida mp3, Simoore Al-Maida pdf. Aaya 54–58. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers