An-Najm · 31/62
Tekki Waxtaan — An-Najm
وَلِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ لِيَجْزِيَ الَّذِينَ أَسَاءُوا بِمَا عَمِلُوا وَيَجْزِيَ الَّذِينَ أَحْسَنُوا بِالْحُسْنَى ۝٣١
Wa lillaahi maa fis samaawaati wa maa fil ardi liyajziyal lazeena asaaa`oo bimaa `amiloo wa yajziyal lazeena ahsanoo bilhusnaa
📖 Tekkim Wolof
Yàlla moom yi nekk ci asamaan yeek suuf si dana fay ña daan jëf jëf yu ñaaw kem la ñu daan jëf, dana fay it ña daan rafetal seen jëf pey gu gën a rafet,
🎧 Dégg

📜 Aaya 29-33 — An-Najm

29فَأَعْرِضْ عَن مَّن تَوَلَّىٰ عَن ذِكْرِنَا وَلَمْ يُرِدْ إِلَّا الْحَيَاةَ الدُّنْيَا
dëdul, képp kuy dumóoyu Sunug fàttali te dundug àddina rekk ñor ko.
30ذَٰلِكَ مَبْلَغُهُم مِّنَ الْعِلْمِ ۚ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِ وَهُوَ أَعْلَمُ بِمَنِ اهْتَدَىٰ
Foofu la seen xam-xam yem. Waaye sa Boroom Moo gën a xam ku réere aw yoonam Moo gën a xam it ku gindiku.
31وَلِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ لِيَجْزِيَ الَّذِينَ أَسَاءُوا بِمَا عَمِلُوا وَيَجْزِيَ الَّذِينَ أَحْسَنُوا بِالْحُسْنَى
Yàlla moom yi nekk ci asamaan yeek suuf si dana fay ña daan jëf jëf yu ñaaw kem la ñu daan jëf, dana fay it ña daan rafetal seen jëf pey gu gën a rafet,
32الَّذِينَ يَجْتَنِبُونَ كَبَائِرَ الْإِثْمِ وَالْفَوَاحِشَ إِلَّا اللَّمَمَ ۚ إِنَّ رَبَّكَ وَاسِعُ الْمَغْفِرَةِ ۚ هُوَ أَعْلَمُ بِكُمْ إِذْ أَنشَأَكُم مِّنَ الْأَرْضِ وَإِذْ أَنتُمْ أَجِنَّةٌ فِي بُطُونِ أُمَّهَاتِكُمْ ۖ فَلَا تُزَكُّوا أَنفُسَكُمْ ۖ هُوَ أَعْلَمُ بِمَنِ اتَّقَىٰ
ña nga xam ne dañuy moytu bàkkaar yu mag ya ak ñawtéef. Te it moo gën a xam li nekk ci yéen ngir moom Moo leen sose ci suuf def leen ngeen di ay liir ci seen biiri nday. Buleen di tagg seen bopp; (moom Yàlla) Moo gën a xam ana kan moo ragal Yàlla.
33أَفَرَأَيْتَ الَّذِي تَوَلَّىٰ
Moo xanaa gisuloo ka dumóoyu fuuyu,
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — An-Najm 31

Simoore An-Najm Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla moom yi nekk ci asamaan yeek suuf si dana…

Simoore Aaya 31/62 — An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Najm Dégg, An-Najm Tekki, An-Najm mp3, An-Najm pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers