An-Najm · 32/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
الَّذِينَ يَجْتَنِبُونَ كَبَائِرَ الْإِثْمِ وَالْفَوَاحِشَ إِلَّا اللَّمَمَ ۚ إِنَّ رَبَّكَ وَاسِعُ الْمَغْفِرَةِ ۚ هُوَ أَعْلَمُ بِكُمْ إِذْ أَنشَأَكُم مِّنَ الْأَرْضِ وَإِذْ أَنتُمْ أَجِنَّةٌ فِي بُطُونِ أُمَّهَاتِكُمْ ۖ فَلَا تُزَكُّوا أَنفُسَكُمْ ۖ هُوَ أَعْلَمُ بِمَنِ اتَّقَىٰ ۝٣٢
Allazeena yajtaniboona kabaaa`iral ismi walfawaa hisha illal lamam; inna rabbaka waasi`ul maghfirah; huwa a`lamu bikum iz ansha akum minal ardi wa iz antum ajinnatun fee butooni umma haatikum falaa tuzakkooo anfusakum huwa a`lamu bimanit taqaa
📖 Tekkim Wolof
ña nga xam ne dañuy moytu bàkkaar yu mag ya ak ñawtéef. Te it moo gën a xam li nekk ci yéen ngir moom Moo leen sose ci suuf def leen ngeen di ay liir ci seen biiri nday. Buleen di tagg seen bopp; (moom Yàlla) Moo gën a xam ana kan moo ragal Yàlla.

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Simoore An-Najm

30ذَٰلِكَ مَبْلَغُهُم مِّنَ الْعِلْمِ ۚ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِ وَهُوَ أَعْلَمُ بِمَنِ اهْتَدَىٰ
Foofu la seen xam-xam yem. Waaye sa Boroom Moo gën a xam ku réere aw yoonam Moo gën a xam it ku gindiku.
31وَلِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ لِيَجْزِيَ الَّذِينَ أَسَاءُوا بِمَا عَمِلُوا وَيَجْزِيَ الَّذِينَ أَحْسَنُوا بِالْحُسْنَى
Yàlla moom yi nekk ci asamaan yeek suuf si dana fay ña daan jëf jëf yu ñaaw kem la ñu daan jëf, dana fay it ña daan rafetal seen jëf pey gu gën a rafet,
32الَّذِينَ يَجْتَنِبُونَ كَبَائِرَ الْإِثْمِ وَالْفَوَاحِشَ إِلَّا اللَّمَمَ ۚ إِنَّ رَبَّكَ وَاسِعُ الْمَغْفِرَةِ ۚ هُوَ أَعْلَمُ بِكُمْ إِذْ أَنشَأَكُم مِّنَ الْأَرْضِ وَإِذْ أَنتُمْ أَجِنَّةٌ فِي بُطُونِ أُمَّهَاتِكُمْ ۖ فَلَا تُزَكُّوا أَنفُسَكُمْ ۖ هُوَ أَعْلَمُ بِمَنِ اتَّقَىٰ
ña nga xam ne dañuy moytu bàkkaar yu mag ya ak ñawtéef. Te it moo gën a xam li nekk ci yéen ngir moom Moo leen sose ci suuf def leen ngeen di ay liir ci seen biiri nday. Buleen di tagg seen bopp; (moom Yàlla) Moo gën a xam ana kan moo ragal Yàlla.
33أَفَرَأَيْتَ الَّذِي تَوَلَّىٰ
Moo xanaa gisuloo ka dumóoyu fuuyu,
34وَأَعْطَىٰ قَلِيلًا وَأَكْدَىٰ
muy joxe tuuti faf ko bàyyi ?
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — An-Najm 32

Simoore An-Najm Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ña nga xam ne dañuy moytu bàkkaar yu mag ya…

Simoore Aaya 32/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers