Al-Qamar · 32/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ ۝٣٢
Wa laqad yassarnal quraana liz zikri fahal mim muddakir
📖 Tekkim Wolof
Yombal nanu, Alxuraan ngir ñu fàttaliku ca. Mo ndax kenn dana ca jàjjoo ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 30-34 — Al-Qamar

30فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Naka la Sama mbugël ak Sama xupp nekke (ci seen kaw) ?
31إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ صَيْحَةً وَاحِدَةً فَكَانُوا كَهَشِيمِ الْمُحْتَظِرِ
Yabal nanu ca ñoom genn Xaacu, ñu mel poñiitum kuy ñag am ñax.
32وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal nanu, Alxuraan ngir ñu fàttaliku ca. Mo ndax kenn dana ca jàjjoo ?
33كَذَّبَتْ قَوْمُ لُوطٍ بِالنُّذُرِ
Nitu Lóot weddi woon nañu lañu leen daan xuppe.
34إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ حَاصِبًا إِلَّا آلَ لُوطٍ ۖ نَّجَّيْنَاهُم بِسَحَرٍ
Yabal Nanu ca ñoom ngelawu callmeer (mu faagaagal leen), ba mu des njabootug Lóot ñoom musël Nanu leen ca njël,
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Al-Qamar 32

Simoore Al-Qamar Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yombal nanu, Alxuraan ngir ñu fàttaliku ca. Mo ndax kenn…

Simoore Aaya 32/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers