Al-Qamar · 33/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
كَذَّبَتْ قَوْمُ لُوطٍ بِالنُّذُرِ ۝٣٣
Kazzabat qawmu lootim binnuzur
📖 Tekkim Wolof
Nitu Lóot weddi woon nañu lañu leen daan xuppe.

🎧 Dégg


📜 Aaya 31-35 — Simoore Al-Qamar

31إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ صَيْحَةً وَاحِدَةً فَكَانُوا كَهَشِيمِ الْمُحْتَظِرِ
Yabal nanu ca ñoom genn Xaacu, ñu mel poñiitum kuy ñag am ñax.
32وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal nanu, Alxuraan ngir ñu fàttaliku ca. Mo ndax kenn dana ca jàjjoo ?
33كَذَّبَتْ قَوْمُ لُوطٍ بِالنُّذُرِ
Nitu Lóot weddi woon nañu lañu leen daan xuppe.
34إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ حَاصِبًا إِلَّا آلَ لُوطٍ ۖ نَّجَّيْنَاهُم بِسَحَرٍ
Yabal Nanu ca ñoom ngelawu callmeer (mu faagaagal leen), ba mu des njabootug Lóot ñoom musël Nanu leen ca njël,
35نِّعْمَةً مِّنْ عِندِنَا ۚ كَذَٰلِكَ نَجْزِي مَن شَكَرَ
mudi xéewal gu bawoo ci Nun : noonu Lanuy faye képp kuy sant.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — Al-Qamar 33

Simoore Al-Qamar Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nitu Lóot weddi woon nañu lañu leen daan xuppe.

Simoore Aaya 33/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers