Al-Qamar · 31/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ صَيْحَةً وَاحِدَةً فَكَانُوا كَهَشِيمِ الْمُحْتَظِرِ ۝٣١
Innaaa arsalnaa `alaihim saihatanw waahidatan fakaano kahasheemil muhtazir
📖 Tekkim Wolof
Yabal nanu ca ñoom genn Xaacu, ñu mel poñiitum kuy ñag am ñax.

🎧 Dégg


📜 Aaya 29-33 — Al-Qamar

29فَنَادَوْا صَاحِبَهُمْ فَتَعَاطَىٰ فَعَقَرَ
Ñu daldi woo seen àndandoo mu daldi koy rey.
30فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Naka la Sama mbugël ak Sama xupp nekke (ci seen kaw) ?
31إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ صَيْحَةً وَاحِدَةً فَكَانُوا كَهَشِيمِ الْمُحْتَظِرِ
Yabal nanu ca ñoom genn Xaacu, ñu mel poñiitum kuy ñag am ñax.
32وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal nanu, Alxuraan ngir ñu fàttaliku ca. Mo ndax kenn dana ca jàjjoo ?
33كَذَّبَتْ قَوْمُ لُوطٍ بِالنُّذُرِ
Nitu Lóot weddi woon nañu lañu leen daan xuppe.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — Al-Qamar 31

Simoore Al-Qamar Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yabal nanu ca ñoom genn Xaacu, ñu mel poñiitum kuy…

Simoore Aaya 31/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers